LYRIC

Bigniy Ande Ba Mairie
Dane Gua Sonou Di Doundou Lou Metti
Sa Tank Dane Meti
Dane Gua Sokh Dè Wayè Takhoul Gua Tègui
Moussome Togne Moussome Diss
Ligua Amsi Ngorr Meusou Mako Guiss
Moussome Lor Tè Meusou LoMe Dist Up
Souba Ak Ngone Louma Gnorr Guay Guiss
Yay Sama Gayn Sama Miss Sama Star
Sama Gayn Sama Miss Sama Star
yay Sama wife Sama Queen Sama Laff
Beuri Gua Yarr Tèk si Dinè Ak Taar
yay Sama Gayn Sama Miss Sama Star
Sama Miss Sama Star
Yay Sama wife Sama Queen Sama Life
Beuri Gua Yarr Tèk si Dinè Ak Taar

Refrain

Mak Yaw Le Boudoul Yaw Dou Done Kenen
Mak Yaw Le Boudoul Yaw Dou Done Kenen
Mak Yaw Le Boudoul Yaw Dou Done Kenen
Lagniy Thiow Yeup Boudoul Yaw Dou Done Kenen

Bobou Ba Legui Magui TRY Wayè Meune Goume Khol Feneen
Mani Bobou Ba Legui Gnogui Fight Wayè Meune Goume Dem Feneen

Mak Yaw Le Boudoul Yaw Dou Done Kenen
Mak Yaw Le Boudoul Yaw Dou Done Kenen

Bigni Andatoul Ba Legui Ma Gui Dokh Si Tally Menoume Diègui
Sama Tank Dina Nèwi
Magui Sokh Dè Wayè Takhoul Ma Tègui
Moussome Togne Meusou LoMe Diss
Ligua Amsi Ngorr Meusou Mako Guiss
Meusou LoMe Lor Tè Meusou LoMe Dingate
Sama Xol Tay Amna Gome Si Birr
yay Sama Gayn Sama Miss Sama Star
Sama Miss Sama Star
Yay Sama wife Sama Queen Sama Life
Beuri Gua Yarr Tèk si Dinè Ak Taar
Yay Sama Nit
Yay Sama Niit
Mani Yay Sama Nitt
Douma Bayi Douma Tite

Refrain
Mak Yaw Le Boudoul Yaw Dou Done Kenen
Mak Yaw Le Boudoul Yaw Dou Done Kenen
Mak Yaw Le Boudoul Yaw Dou Done Kenen
Lagniy Thiow Yeup Boudoul Yaw Dou Done Kenen
Bobou Ba Legui Magui TRY Wayè Meune Goume Khol Fenen
Mani Bobou Ba Legui Gnogui Fight Wayè Meune Goume Dem Fenen
Mak Yaw Le Boudoul Yaw Dou Done Kenen
Mak Yaw Le Boudoul Yaw Dou Done Kenen

Melga Nima Nekh Bëuss Bounè Daguay Bèss Melni Gnogui Dagua Tambali
Tè Kham Guani Dou Dièkh Kone Waro Mouseu Deglou Gnilay Wakhnè Do Togne Andati
Mani Melga Nima Nekh Bëuss Bounè Daguay Bèss Melni Gnogui Dagua Tambali
Warga Khamni Dou Dièkh Bagna Deglou Gnilay Tègual La Mane Ak Yow Do Togne Andati
Yay Sama Nit
Yay Sama Niit
Mani Yay Sama Nitt
Douma Bayi Douma Tite

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR