LYRIC

Intro
Yenn saye dingueu guiss louleu dieulé kow lolou beu diapp se bopp kessé ngay meun
Fekk ngueneleu laakhou tchi guinaw bobou fitna ndakh Yalla rekkeu kham ak di def li gueune

Woah oh oh Yeah yeah yeah
Woah oh oh Woah oh oh
Woah oh oh Yeah yeah yeah
Woah oh oh Woah oh oh

Verse 1

Bi Moussa waré ande ak Khoudar def ko né dinga diang ak mane defal ndank ak mane nanga ande ak dal

Dinga guiss louleu yem wayé nak nanga dieme diokh me se kaaddou né do and ak hal

Kou nek lileu Yalla mey
Nieupp mounougn done benn
Ladial phiraon mi Yalla dieye
Beu mou fouye beu degg deugg leu done begn

Guiss diongoma diou sey tass
Waroul takh ngay khass
Khamoulo lou tchi fassou
Beu guissogo gore beug khey fass

Moytoul me dieek diou romb rek
Diekk taarou ngané dee dou yomb
Wala djiguene diou lamb
Ngané no def ding ko lamb

 

Pre-chorus

Judge not khel matoul boul wereunté tchi lou se yone nekoul
Dieuw ak fok ne am ne diam mo tané yenn yi kou gueum dou ko def nekkoul

Chorus x2

Yenn saye dinga tite be se khel nara diakhasso
Yenn saye dinga fire be se khole nara diégué seuss
Yenn saay dinga tite ba sa khel bara diakhasso oh oh
Wayé bepp fitneu toudd Yalla nga tchi wara ndieukk diemeu rakhasso oh oh

Verse 2

Borom bi dey missal
Binde ne lepp be noppi
Segueum gni kham nioye teye
Kou niakk kham wara gueuneu noppi

Kou wekk lepp tchi guissané bo
Dtouwoul adina dinele sappi
Bouleu khiif takha salite
My brother Yalla bouniou niakk soppi

Li khew tchi mim rééw
Gueunoul yémé bitim rééw
Mystique tchi biir guééw
Wayé Loukhouss dou firim rééw

 

Se deunkeundo boul kheep ndieurigneum
Tagg sey kilifeu dingate Serigneum
Téyé se kourouss gaddou se satala
Deukk tchi dieuw yakkh der yeufou satt leu

Pre chorus

Chorus

Bridge

Yenn saye dingueu guiss louleu dieulé kow lolou beu diapp se bopp kessé ngay meun
Fekk ngueneleu laakhou tchi guinaw bobou fitna ndakh Yalla rekkeu kham ak di def li gueune

Yenn saye dingueu guiss louleu dieulé kow lolou beu diapp se bopp kessé ngay meun
Fekk ngueneleu laakhou tchi guinaw bobou fitna ndakh Yalla rekkeu kham ak di def li gueune

Outro
Lo fi def dinegn wakh
Lo defoulit dinegn wakh
Yeek tchi mbame womate mbaam
Ken dou tee dinegn wakh

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR