LYRIC

{1er Couplet}
Déf ngama louma guèntoulwone
Louma doul meuna geum koumako wakhone
Dara geunoul kawè fimala téggoooone
Sôrouma lii béteu-ngamaaahh
Yaw li ngama deff metti-namaaa hahaan
Ak finiou diaar yeup lii meunoumako wone imaginer
Sama bopp dafa diakhasso may guiss ay image you nééh
Lan mola doyoul ba nga diouk nane da ngay wouti lénén fénén
Loutakh mou done kouma kham loutakh yaw tanoulo kénén
………………………………
Yaa takh ma bayi nieup bayi samay mbokk yaw nga fayma liiii
……………………………..
Da nga wakh bama diokh la lepp bokk’ak yaw béneu family
…………,………………..

{Refrain}
Wakhma lane moo takh nga deff maa liii
Khawma lane moo takh nga deff loumèl nii

Khawma loula dall ba nga beugga dém fènèn
Kaay nga wakhma loumala bagnal ba ngay khool kénén

Wakhma lane moo takh nga deff maa liii
Khawma lane moo takh nga deff loumél nii

Khawma loula dall ba nga beuga dém fénén
Kaay nga wakhma loumala bagnal ba ngay khool kénén

{2em couplet}
Dafa mélni damay guént yakamti kouma yééhh
Bama yééwou meuna doundaat mbékté biss bign niouy mayéé
Yaa nékkone sama vérité yaw rek laa geumone
Meussouma guiss finga maay trompé mélni damma geume_mone
……………………………….
Digoon ngama doundou aldianaaaahh
Maa’k yow dound’ak dééh ngama wakhone wayé tay léppeu diékhnaaaaahhh
………………………………
Yaa takhone ma bayi di wakh nane niom nieuppa yéém
Tey nga khooss sama cicatrice deffatt ko gôme
Liniou dounddou boumakay néttali day mélni poème
Kii louko dall est ce que anddeu naak saagooome

{Chorus}
Wakhma lane moo takh nga deff maa liii
Khawma lane moo takh nga deff loumél nii

Khawma loula dall ba nga beuga dém fénén
Kaay nga wakhma loumala bagnal ba ngay khool kénén

Wakhma lane moo takh nga deff maa liii
Khawma lane moo takh nga deff loumél ni

Khawma loula dall ba nga beuga dém fénén
Kaay nga wakhma loumala bagnal ba ngay khool kénén

Yéééhééhéé yeaaahhh

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR