LYRIC

{Mao – Refrain}
Cii pet lakoy doundeu akk yène
Deug deug diambar ngène
Mounou ma def lénène
Loudoul wax akk yène
Cii pet lakoy doundeu akk yène
Deug deug diambar ngène
Mounou ma def lénène
Loudoul sargalène

{1er Couplet}
Hann….hann…ya
Eh yaw !!! Foma dégue dawfeu
Fo nékk ma siiwefeu
Dafa dem baa méleni dama bokk cii seu mifa
Souma ko meunone kounék kou néé ma talaal five giveleu
Bép killah killah lii story bougnou liveleu
Sa youma djakéé baa tambaléé douté
Diom bimaay yeukeuti cii sèn regard lakoy woutéé
Yéneumeuy wéteuli tchii yone bima saurou
Nguinaw yalla fima tolou yéneu mafaa yaubou
Liima sékeul ak yène cii zaïr ak baatine
Momeu ngeuneul djouni yone ay disc de platine
Dafa yémé ay niit yo xamoul dilaa nianale
Dii wérèneté di khoulo founiou tolou dila fightale

{Mao – Refrain}
Cii pet lakoy doundeu akk yène
Deug deug diambar guène
Mounou ma def lénène
Loudoul wax akk yène
Cii pet lakoy doundeu akk yène
Deug deug diambar guène
Mounou ma def lénène
Loudoul sargalène

{2eme Couplet}
Mbeuguel bi nga ma djign nii diapp nani saçleu
Bodé fan’s killah douma def loutakh niou khaçleu
Pacte bouma nassleu, Promesse bouma façleu
Loumay samaneté ba biss bimay magaatt dii raçleu
Yeukna liguay dathie
Xamena figama athie
Amouma sa faay homy kalko figuako nathie
Yéneuma def number one cii game
Maa téw wala niakk téw yéneuy woté cii line bi
Put sama shirt diko bakko cii street
Magui yeuk sèni niaane di djott sèni mess
Sama beut yi di toy sama xoll bi di fess
Sèn warougal mateneu seuk légui massi dess

{Mao – Refrain}
Cii pet lakoy doundeu akk yène
Deug deug diambar ngène
Mounou ma def lénène
Loudoul wax akk yène
Cii pet lakoy doundeu akk yène
Deug deug diambar ngène
Mounou ma def lénène
Loudoul sargalène

{3eme Couplet}
Yaa!!! hann!!! yaa!!!
Magui fatalikou goudi bigaay xouss cii tawbi
Magui fatalikou bigaa maay call ma nekk cii kawbi
Magui fatalikou bigaa maay guiss dii djoy bay lokh
Shirt bigaa sol nga soumékou daadii maay diokh
Magui Fatalikou biss bigua maay pass sa mère
Mounéma mane rek ma meuneu guifeul sa merr
Ndakh boy déguelou cii pet dagay teudjou dii djoy
Moumaay nianale cii call ba damay moudjou dii djoy
Magui fatalikou lép lo def nguir mane
Mé xamaleni lép loumeu meune dinako def nguir yaw
Killah killah sa sopé bikoy doundeu cii pet
Molay bégué cii bi son dila wakh Jahjeuf

{Mao & Nitdoff – Fusion} Mao en ( )
(Cii pet) Yeah (lakoy doundeu akk yène) Killah Killah Naka warr
(Deug deug diambar ngène, diambar ngène) magui laay bégué bro
magui laay bégué sister Han!!! Meunouma waune niak def bi son
(Ouuuuuuu!!!)
(Cii Pet Lakoy Doun’deu akk yène
Deug deug diambar guène diambar ngène)
Binde naa di barré bindaatt di barré
Ndakh khamouma waune limay yeuk sama khol
Nouma lakoy wakhé mé djapaleni kadou yii ngay déguelou sama xoll lako tiibé
(Oooouuuu!!!!) Fépp fo nékk cii aduna bi !!!! (Yeah yeah!!!)
magui laay wax djadjeuf dila maçtawou
Tiono bignii dathie nguir mane (I’m a fan sèn fan)
dila balou akk (sèn fan) dila talale sama five (Killah Family)
(Mounou ma def lénène
Loudoul sargalène)
(Cii pet) Yeah (lakoy doundeu akk yène) Yeah Jahjeuf
(lakoy doundeu akk yène) Nokoss Di Rokoss
(Deug deug diambar diambar guèènnne
mané diambar ngène
It’s your boy Killah Killah
Diko maay bépp Killah Killah
(Mounou ma def lénène
Loudoul wax akk yène)
(Cii pet) All Right !!!!
(Lakoy doun’deu akk yène
Deug deug diambar guène
Mané diambar ngène)
Mounou ma def lénène
Loudoul sargalène)

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR