LYRIC

[Part 1]
Sa Arras
La niou bolè niari rouh yi
Adouna dou wone touki
Té guissèw niou ba nopi
Béna place
Tokk niou beuneu sama roues yi
Né kou démone touki
Té meunoul nieuw balégui
Dianakhék baanex
Dima keuli keulé
Kagne lay done
ak nou May Def ba guiss la
Dane ma khégne lou gueune nekh
Té dou ki dou keulé
Nga néwone si Yoon
Nou May Déf ma miss la
Stagiaire la wone
CV bi démna fou né
Ndékété Yoo
Douma liguey si niom
Dou dianerr Dagne ma la wane
Mbekté la yooo
cédé bi datch na boudé
yaye diour samay dome….

[Hook]
Ni youssou ndour ak Pen
Khamone na ni daa niou dadjié
té dou nirok len
Khamone na ni bess bou niou dadjié
Moy dakh Mburok lem
Douma la fene
Give me your hand
Niou andeu dem fenene
Dieundé wouma la ken
Dou kene
si niom kou meune dara si nioune
Té nioune
sokhla wou niou khoulok kén

[Bridge]
Nga togne ma ma lay balou
Wax lene ma Kagne lay dalou
Kou sagna tambambalou
Boma méré ma warou

[Part 2]
Bayi lene niou wax lou lene neex
Guissa gouma lou niou wara téré dem
Li May yeuk khadioul si ndap dou diekh
Bayi lene niou wax lou lene neex
Guissa gouma lou niou wara téré dem
Li May yeuk khadioul si ndap dou diekh

Ké wax ko boumou yakh crédit wam
Da nga gueuna fort
khétou bone si mane
Tate lay Def sou ma la djiégué
meune nga sa bord
Mate nga li nga done si mane
bou doul yaw sama tole kene dou ko ñagué

Bokak yaw keur
Di fo di ré
di Contane
Moy sama yéné si yaw mou antou niou mour la nga ouff sama ndiaboot
Je t’aime mon coeur
Kene dou niou ré
Do degg ndeyssaan
Dina la téyé ni mou waré
Ba degg diaraboot
Ma moitié ma Reine L’autre Moi ma meilleure amie
quand je parle de toi j’ai des larmes aux yeux je t’aime et tu es toute ma vie

[Hook]
Ni youssou ndour ak Pen
Khamone na ni daa niou dadjié
té dou nirok len
Khamone na ni bess bou niou dadjié
Moy dakh Mburok lem
Douma la fene
Give me your hand
Niou andeu dem fenene
Dieundé wouma la ken
Dou kene
si niom kou meune dara si nioune
Té nioune
sokhla wou niou khoulok kén

[Part 3]
You know i love you
Never dare to leave you
You know i need you
Every Day Every night
I’m thinking about you
Night and Day everywhere i go
baby i see you
There is no one no one like you

[Bridge]
Nga togne ma ma lay balou
Wax lene ma Kagne lay dalou
Kou sagna tambambalou
Boma méré ma warou

[Hook]
Ni youssou ndour ak Pen
Khamone na ni daa niou dadjié
té dou nirok len
Khamone na ni bess bou niou dadjié
Moy dakh Mburok lem
Douma la fene

Added by

Ahmed

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR