LYRIC

{Bril Fight 4}
Yo kay sunu World, Ya’ve been Told
lou bessa Aksi, Shine like Gold
Dess cii yone wi, yagg idji, degg nga baatt yi feuss na
Gni cii tèénn wi, nio ngui djouki, léégui baag yi feess na
Djouni Djouni Ndaa (Nga né),
Kaay dieul cii,lignu la djay cii
Jooni Jooni Nda (am), lignu indi, Mbaa
ding niou waulou , solou sopékou djékk cii taaru,
Nioy gnila waalu,Délou dii djééki, Gné di tchii tarou
Kou djougué cii nioune dou wathie cii tempo, Click lay am cii nerf-ram,
Day djégui daathie bi Compo , Kick bi lay xam snaram,
Def dara feug la lou gueuna diss “marteau Thor”
Wane lané deug la,dougn guiss lou nior di “mar tautaur ”

{Refrain}
Founiou rap loufa neubou day feegn
(kaay sunu world) (scratch)
Sunu djaap (class’chic) doko beugg di baagn
k-k-kaay .Dégloul sunusound

Founiou rap loufa neubou day feegn
(kaay sunu world) (scratch)
Sunu djaap (class’chic) doko beugg di baagn
k-k-kaay .kaay feel sunu sound sound

{Gaston}
Hood laniou def nii tapeu
Teuyé rhymes yi di tchi fo ni batterie ak lapeu
Sante bi Ndoye la, dou Diagne/.classic bilay gaagne,
Baye Scène ak Bril leu
Kaay niou firil-leu, Sa xell mé rappeu
Fila mic bi soudjooté – Taaru mindeu mi la souniou studio teuyé
Fignu dieum lerr na naagn di nga comp. sou djoté
Def dara bila bok, Touti wakh bila bokk
Hey boy niou fisseulate ma, mayma nigga wala bokk
My nigga Jump Up, Djap bi fok ngèn teup
Manela sen Pape Bandit cii mic nigga comp d’hab
Rap lagniy def ,Sunu carrière dou lou bref
Dagnu am fiitu innovés niolay breath

{Refrain}
Founiou rap loufa neubou day feegn
(kaay sunu world) (scratch)
Sunu djaap (class’chic) doko beugg di baagn
k-k-kaay .Dégloul sunusound

Founiou rap loufa neubou day feegn
(kaay sunu world) (scratch)
Sunu djaap (class’chic) doko beugg di baagn
k-k-kaay .kaay feel sunu sound sound

{Gaston}
Street bi laniou topeu
Dara douniou stopeu
Baye Sen Bril Fight 4

{Bril Fight 4}
Djougué naniou cii jonglé, délou cii taathie rime bi da wal
Gni yagg djangalé nio fi dougou cii dess cii crime bi dawal
Niari oukou, cii roukou, djomal cii foukou niou gueuneu adjou
Dikk di sakou, li nioul koukou cii xoll yi fadjou
Niounn douniou yém ak yènn djanguil ni gniy arawé
Bokou niou lign niou yénn fala sunu Art rawé
Nigga wurrup, Sunu beurreup
Class bi gueune high cii sa biir school la get up

{Refrain}
Founiou rap loufa neubou day feegn
(kaay sunu world) (scratch)
Sunu djaap (class’chic) doko beugg di baagn
k-k-kaay .Dégloul sunusound

Founiou rap loufa neubou day feegn
(kaay sunu world) (scratch)
Sunu djaap (class’chic) doko beugg di baagn
k-k-kaay .kaay feel sunu sound sound

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR