LYRIC

{Verse I}
Biniou rofé Rouhou thi djeumm, thila mindéf xippi nouyok doundam
Raflé thi moudjeum, fimou djeumm , lifa neubou dou ndamm
Beug beugueum , gueun di maagg, sa bou wésso bén simili
Négoul ba gueum , dogdi daagg, limou béén, soumi lii
Weuri lénén ték thi kawam , khouri niénén fathie thi cas-wam
Limou yagga khar mou waathie fénén da taak thi kaw am ?
Sakhna laf , sookh na waf , légui mou djaréfa naaw
Déf na gaff , xél la xaaf, djogui bou djaré fanaw
Nékk féépp di léépp, deupp nieukkeu fipou di kéépp léépp
Bépp péppeu boumthi séppi xippi toyati xéépp. Seuppp..
délou démb , wala fékki souba xélam mangui niaar
Bissoup tay lithiy moussiba xolam la winiaar

{Chorus}
I try to wake up again, day and night.
« biss bou nékk niongui djéma yéwou »
I want to run some, we’re out of the sky.
« Fénén laniou beugga délou »
Maybe time can forgive us, some things from the past.
« deuppeul , nélén niongui djégueulou »
Maybe i want my dreams, forever to last.
« li souba dinthie laniou tokk di goolou »

{Verse II}
Kén dou reuthie, thi espace ak ci temps
yone wi kheuthie , gni ragala ndjaap éss pass thi satan……
Beugati djitou nieupp, tiibeu-thi ngeupp
dogou thi , dougou thi , bania di deuppp
Nieulé di teupp lou euppeu, kheupeu ,
djangueu thi , khamati weuri eudeub
Nitt ki waathiena tookk thi andam,, waathie-na fokmou am ndam
Djégalouwatt ,kiy togniwatt ak wadji dananiou andam ?
Démb modi tay, djante meussoula fink wala di sooo
ki done khar ba déwénn thiante , wayla finte wara disso…
guisso , mbongui lamisso , massla ak doundeum
seussko , waneko misso , néko mou massla thi toundeum
djarfi dém ba , tokk thi démbeu , goudék beuthieuk
khéémém yane ba , bagne thi yéém ba , yone wou goudeum ba thieuk

{Chorus}
I try to wake up again, day and night.
« Biss bou nékk niongui djéma yéwou »
I want to run some, we’re out of the sky.
« Fénén laniou beugga délou »
Maybe time can forgive us, some things from the past.
« Deuppeul , nélén niongui djégueulou »
Maybe i want my dreams, forever to last.
« Li souba dinthie laniou tokk di goolou »

{Bridge}
« Go to my house, looks like open this day. »
Yeah Li souba dinthie — laniou tokk di golou man

{Verse III}
Bobou ba légui niongui léwato’k yaakar, té songo amagouthi
Beurébi foumouy moudjé oumpou nieupp , niouthiy lissaxar
Sunu nopp yi, baat yi thi souba di sikar kén khamagouthi
Dara bathiy khaar fété kaw fayi liy sakhaar
Taakhirlou , bagne di yeungou , takh li yéémb beurétoul
Mbeureu khirou ,bayi djééngou, tékki ngémbeu beurrétoul
Deuké khayma euleuk limou dinthie , rér thi théoréém
Teuweu dém, sakh thi khaar bou méti , défko théoréme
Rirou deunou bouy wadjal daal , meunoko yeuk bay djéma fatt sa nopp yi,
Wakhtou yangui lay roppi , li nieuwoul boul thi wakh ba fatéci noppi ..

{Chorus}
I try to wake up again, day and night.
« biss bou nékk niongui djéma yéwou »
I want to run some, we’re out of the sky.
« Fénén laniou beugga délou »
Maybe time can forgive us, some things from the past.
« deuppeul , nélén niongui djégueulou »
Maybe i want my dreams, forever to last.
« li souba dinthie laniou tokk di goolou »

{Outro}
Hello world , this was r’aperitif,
Hi , souba limou dinthia gueuna sakane mboki alcane (CnH2n+2)
I’m telling ya , wakh ko sa ganyine , niongui nieuwatt ,,,,, yagatoul

{Chorus} East Clubbers vox sample
Back vocals : Lady Zee

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR