LYRIC

{PPS}
Xel leu délou beu lepp di dorr, Tisbar Sicap nga melni Libidor
Guiss taar tchi yaw la reine de sikithior
Xel né xol bi défal ndank rek, Bobou kholou mala wone sakh
Reuy yeu fës ci khol bi talou mala thiakh
Mane limay yegg rombeu na sakh love
Dima djégué wauroul da nga may nasakhlo
Ma xamné yaw leu dou done kénène
Niata lafi rombeu baby compté lène
Fou djanteu fës doto guiss lénène
Tokk sa wét dotouma dém fénène
Légue légue niou khouloo di méro
Tchi call bou sonné nga guiss bénène numéro
So méré ma diakhlé so nopé ma wët
So yéwo fass sa kanam damay yendo xalaate rek
Niom douniou yaw té do niom dou taar rek la guiss sama xol bi nga mom
Lo beug lay def yaay ki djour sama dom
Lo beug la beug ya use salomon
Dou thiaxaane yaafi néh t’es taaru rafinée
Yaram bi yaw lay lathie dh yaay sama guinée
Yaay sama linguère yaay sama djiné
Diokhé na diouraum té douma laathie sama monnaie
Maa tay bardé mané Mister lova
Damay seuy beu xeuy ba lepp ci sa loxo
Yaay sama profil xam nga sa statut,
ya love bi connecté dou soxla wifi
GANGSTA LOVE moudj done MBOUROK LEM
Néggu seuy dou niaak problème
Loula nakari wone diekh neu tay
Yako liguèy waral malay way

{Refrain}
Dinala togne té dinala gaagn
Waayé mounieul ko té xamné yaw la love
Biss dina djoum ba defla loula doul nekh
Waayé na ngeu mounieul ndaxté yaw la love
Moy sa love moy sa life
Moy sa aldiaana ki moy sa paradise
Ki moy sa love moy sa life
Moy sa aldiaana ki moy sa paradise

{Bril Fight 4…}
Xam naani mane yaw rek la love
Ba loma def mané beug naaaaaa
Té guiss naani yaw tchi mane rek nga dof
Motah malay mounieul ndakh nangou naaaa
Diokhla sama dieumeu ak rouh néla yaw rek yama doy
Même boma méré sama beut day taa ndakh sama xol moy toy
Sama baby yaay sama soppé
Defna leu statut ak pp
Guel ya ngi may toppeuh en pagaille di ma baayila Ma ngi ni nama ray
Même boma togné beug naa sakh djéguel ma dila raay
Lima gueuneu neekh ci life bi yaw leu
Loma def bao baalou woul sakh mane meu baal leu

{Refrain}
Dinala togne té dinala gaagn
Waayé mounieul ko té xamné yaw la love
Biss dina djoum ba defla loula doul nekh
Waayé na ngeu mounieul ndaxté yaw la love
Moy sa love moy sa life
Moy sa aldiaana ki moy sa paradise
Ki moy sa love moy sa life
Moy sa aldiaana ki moy sa paradise

{PPS}
Abal ma bante ma dox, boudé goumbe teukh lou nga sant
Thiofel sopéku di ngante, sa leeray ya kawé sotéku ni jant
Taaral sunuy goudi, fadjar gou yèewu diakarlo di thiant
Li tchi mane di yaw, yaay kémane guiy saxami sama lanthie
Tèk nala fouma tègoul djiguène, yaay kèn kiy samm sama rééh
Séet na né douma ci guéne, sa ndaa lay tankh sassou ma maré
Daagoul mamma reer, ma fèkki la fa nga né té douma réthiou
Togal ma ma rère, ma teudi ndakh weuri gui dama ko wéssou

{Refrain}
Dinala togne té dinala gaagn
Waayé mounieul ko té xamné yaw la love
Biss dina djoum ba defla loula doul nekh
Waayé na ngeu mounieul ndaxté yaw la love

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR