LYRIC

Fi dealer bi dou dée badougn amati came
Dofi tidji sa gatt ndakh dagn wagni sa flamme
Nigger dof ba dougn joublou si niakk bi di rame
Niolay fuck badi fuck sakh mamati mame
Niou Tek tank nga bekk melni salaire bou tew
Mc bou reuy dou def manière you sew
Niolay bouffé ni touffé
Dougn sucer pour succés
No triché pour touché fok am bi di lew
One rappeur laniouy eat di am appétit rap
Sikim yefi beuri melni arda turan
Daniou tayal badougn topsi sappé yi ndiap
Bouniou xeulé daniouy ailou melni fawzi ghoulam
Ta dou tée nioungi toksa ndode comme dette
Tadjé si keur bounek comme thiep
Accaparé legi daniou geuneu namm xalima yi Lissi dess nigger god’s plan leu comme Drake
Kone Ma defat couplet
Taal lene ni samay doublé
Leerna si tableau ni craie
Bum yengsi four bi mai latta mo guéne niou collab nga comp giss nignlene souté
Kone Bayniou Xamal gni xamadi
Lathjko gni saurou mai dotougnko defatti
KY leu xamngané bokkouniok tapetti
Appliqué djoté nioune do giss niou sakettou xamnganiou xam finiou né
Yor sama cogn sama back
Ak sama diom comme avocats
yello sama ndam dama job lima am kone bou bene fake wakh sama cas
Athiou mouk dou sama waref
Kone noni liniou beug lay def
Fek yangi doundou nodef dinga degg sam baat makoy djolli mouy taal ba sa fief kzeee

{Refrain}
Yo My Nigger You Can Do That | You Can Do That it’s Not easy Ma Man .
( No , No , No )
Yo My Nigger Can Do Thtat .
Limaay Deff Mom Nguaay Galou Kone Dieundeul Gan You Béëss You And You

We Have The Same People
We Have The Same Blood
Séné galai gua man Séné galai la
Ganng , Gang , Dieng
We Have The Same People
We Have The Same Blood
Séné galai gua A Ah Aah Hié Hié

{One Lyrical}
Damay Seraal – Nguaay Tanguaal Nieuwna Sopilaa Menth Fresh .
Nopilén Malén – Diaxaal –
. Condoléance Thi Ki Ganiou Taay Dji .
Tankou Rappeur Bi -Thi Niankatang ( Yea )
. Rewandé Dont La Doumako Taay. ( Non )
Daaafay Lathié Ndax Rein Moy Xeew Ok Lundi Ma Nguéntéwate Koo .
May Papa One Zlatan Chacourt .
Sa Numéro Yay Sama Rendez-vous.
Wee Clok Mom Mouné Wonderful.
Fuck Yén Nieup Epuis C’est Tout .
Ma Tay Rew Ndax Fi Daguay Cool Sa Cool
Niou Beugla Eupeulé Daradiani Bouba Ndr
Dama Fier Xadiuma Thi Séni Doulba Douf
Beugouniou guiss Sama Kanam Ba Melni Poup Thi Touche . Ma Nigger

Doffi Tokk – Té Doffi Soss – Midel Finger Thi Kep Kouma Bagne Thi Xol . Rafet Djiko
Bi Nala Yalla Fay Nigga. Iñiane Déh Gomla Dagua Nara Déh Thi Ndol .
Ni Toxico Bi Mala Meuna Diox Sa Dose Ay Ver Thi Son Raagalna Toum Mou Thiol
Dioudio Thi Thiono – Repesen Kinpi Coner
Meun Té Con Douma Dioudo Feat Didons No Noo .

Foulakk Fayda Laniou May Dialyse –
Tax Douma Sentir Sénni Pik .
Meuno Ma Yëm Meunoulo Messi –
Xamoulo Thiowlima Yéno Diss –
Mélomanes Bi Néna Dannio Xiif –
Bou Souba Ma Dioxla Gua Ndekki Hit .

{Refrain}
Yo My Nigger You Can Do That | You Can Do That it’s Not easy Ma Man .
( No , No , No )
Yo My Nigger Can Do Thtat .
Limaay Deff Mom Nguaay Galou Kone Dieundeul Gan You Béëss You And You

We Have The Same People
We Have The Same Blood
Séné galai gua man Séné galai la
Ganng , Gang , Dieng
We Have The Same People
We Have The Same Blood
Séné galai gua A Ah Aah Hié Hié

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR