LYRIC

(verse 1)
Sa Arras La niou bolè niari rouh yi
Adouna dou wone touki Té guissèw niou ba nopi
Béna place Tokk niou beuneu sama roues yi
Né kou démone touki Té meunoul nieuw balégui
Dianakhék baanex Dima keuli keulé
Kagne lay done ak nou May Def ba guiss la
Dane ma khégne lou gueune nekh Té dou ki dou keulé
Nga néwone si Yoon Nou May Déf ma miss la
Stagiaire la wone CV bi démna fou né
Ndékété Yoo Douma liguey si niom
Dou dianerr Dagne ma la wane Mbekté la yooo
cédé bi datch na boudé yaye diour samay dome….

(chorus)
Ni Youssou ndour ak Pen
Khamone na ni daa niou dadjié té dou nirok len
Khamone na ni bess bou niou dadjié Moy dakh Mburok lem
Douma la fene Give me your hand
Niou andeu dem fenene Dieundé wouma la ken
Dou kene si niom kou meune dara si nioune
Té nioune sokhla wou niou khoulok kén

(verse 2)
Nga togne ma ma lay balou Wax lene ma
Kagne lay dalou Kou sagna tambambalou
Boma méré ma warou Bayi lene niou wax lou lene neex
Guissa gouma lou niou wara téré dem
Li May yeuk khadioul si ndap dou diekh
Bayi lene niou wax lou lene neex
Guissa gouma lou niou wara téré dem
Li May yeuk khadioul si ndap dou diekh
Ké wax ko boumou yakh crédit wam
Da nga gueuna fort khétou bone si mane
Tate lay Def sou ma la djiégué meune nga sa bord
Mate nga li nga done si mane bou doul yaw sama tole kene dou ko ñagué
Bokak yaw keur Di fo di ré di
Contane Moy sama yéné si yaw mou antou niou mour la nga ouff sama ndiaboot
Je t’aime mon coeur Kene dou niou ré Do degg ndeyssaan
Dina la téyé ni mou waré Ba degg diaraboot
Ma moitié ma Reine
L’autre Moi ma meilleure amie
quand je parle de toi j’ai des larmes aux yeux je t’aime et tu es toute ma vie

(Chorus)
Ni youssou ndour ak Pen
Khamone na ni daa niou dadjié té dou nirok len
Khamone na ni bess bou niou dadjié Moy dakh Mburok lem
Douma la fene Give me your hand
Niou andeu dem fenene Dieundé wouma la ken
Dou kene si niom kou meune dara si nioune
Té nioune sokhla wou niou khoulok kén

(Verse 3)
You know i love you
Never dare to leave you You know i need you
Every Day Every night I’m thinking about you
Night and Day everywhere i go baby i see you
There is no one no one like you
Nga togne ma ma lay balou Wax lene ma Kagne lay dalou Kou sagna
tambambalou Boma méré ma warou

(Chorus)
Ni youssou ndour ak Pen
Khamone na ni daa niou dadjié té dou nirok len
Khamone na ni bess bou niou dadjié Moy dakh Mburok lem
Douma la fene Give me your hand Niou andeu dem fenene
Dieundé wouma la ken Dou kene si niom kou meune dara si nioune
Té nioune sokhla wou niou khoulok kén

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR