LYRIC

{Refrain}
Li tchi mane néwoul ci niom
Li tchi niom néwoul tchi yaw my lova
Liniouy wakh yégou mako sakh
Ndakh boudone Film fin bi maak yaw la
HooOoo Wa
Yaw la Love you when you know
I Love you when you know
HooOoo Waaawou waaaw
AaaaHaaaa AaaaH HaaaaHaaaaa

{Verse 1}
Kaay nga wakhma bèn yone calme bifi nek dafma moudj soff
Statut rek lay guiss ci story
Am nga connexion mais communiqué wo
Loutah nga beug melni niom ?
Lima guiss ni nga def ni mom dou seu djikoo
Louma wakh nga bagn néma “No No”
Nala fekk fi nga né lidieunti ko
Mane douma daw douma niom nieup daniou fokni lep dina diekh
Maak yaw mounoul bania nekk pique ak pelle
Xamna niou beug yakk souniou digueunté

{Pont}
Lane mo takh niou beuri Noone wooowooo ?
Me N You for life, my baby
Bo ndaré djoy mane meu wèy Woman No Cry
Lane mo takh niou beuri Noone wooowooo ?
Me N You for life, my baby
Bo ndaré djoy mane meu wèy Woman No Cry

{Refrain}
Li tchi mane néwoul ci niom
Li tchi niom néwoul tchi yaw my lova
Liniouy wakh yégou mako sakh
Ndakh boudone Film fin bi maak yaw la
HooOoo Wa
Yaw la Love you when you know
I Love you when you know
HooOoo Waaawou waaaw
Aaaa Haaaa Aaaah Haaaa Haaaaa

{Verse 2}
Sonou tchi dila nameuh
Soneu tchi dila lathie louma def
Baby Wakhma bou gaaw fane nga né
Ma féki sila kaaay niou dadjé
Mounoma baayi ndakh sékou niou lolou
Mounoma beug té beugoma waulou
Bouldi khaaathie di khaaathie
Xol di laathie di laaathie di laathie
Boul daw boul dém boul nangou lepp yakou bèn yone
Boul may sa noone yi ndam. Xeuy di lakkatou di djoy
Bouldi khaaathie di khaaathie
Xol di laathie di laaathie di laathie

{Pont}
Lane mo takh niou beuri Noone wooowooo ?
Me N You for life, my baby
Bo ndaré djoy mane meu wèy Woman No Cry
Lane mo takh niou beuri Noone wooowooo ?
Me N You for life, my baby
Bo ndaré djoy mane meu wèy Woman No Cry

{Refrain}
Li tchi mane néwoul ci niom
Li tchi niom néwoul tchi yaw my lova
Liniouy wakh yégou mako sakh
Ndakh boudone Film fin bi maak yaw la
HooOoo Wa
Yaw la Love you when you know
I Love you when you know
HooOoo Waaawou waaaw
Aaaa Haaaa Aaaah Haaaa Haaaaa

Lane mo takh niou beuri Noone wooowooo ?
Me N You for life, my baby
Bo ndaré djoy mane meu wèy Woman No Cry
Lane mo takh niou beuri Noone wooowooo ?
Me N You for life, my baby
Bo ndaré djoy mane meu wèy Woman No Cry

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR