LYRIC

[intro ] (ombré :Yeah nan nan ,
: yeah i bring nightmares to reality
hum huum huuum , yeah yeah yeah yeah nan nan …
bril fight 4 …(the last fight 4) Ombré Zion …(Analyzik)
mélokaanou léér yi Dégloul…

[1er COUPLET] {Bril}
Daniou wééssouy djeumm Bokkounio’k lila say gueutt di wane
Yeuk’ko finiou djeum, deukou léérla woutéék sa diwane
Niola romb di méébou rawla mbouri kiiray meuna aandeu
Reud thi tomb la neubou Tokfa, Moy ni thiouraay miiné andeu
( omnré : hi … Nan nan nan nan)
( Bril : I write the right yaa – deggloul)
niola romb di méébou rawla mbouri kiray meuna aandeu.
Reud thi tomb la neubou Tokfa, Moy ni Thiouray miné andeu
Xel dou djeuli …,,fou yi léér baayéko
Tôkk thi baat yi, yénou araf defko hilèr bayèko
Gadou xalima maass sa mbindeu mi deugg bi daagou sa wétt
Yatteu galagne dougou thi toundou bi teuggueu bi Daggueu sa weettt
Koula djokhi lathie ba noppi wane la tontou wi thiakhoul
Lignla eundil lign thi dathie doko gantou withiakhoul …

Refrain
{Ombré}
Daniou yaagga doundou thi maral di sééntou biss mou nawétt
Tay niou khiin di taw ba maral bi moudjou thi sa wétt
{Bril}
Nioy guiss bén ponkou am lougn thi féntt,
Adounay gnéntt, dougn thi fontou nioy dokh di guéntt
{Ombré}
Méti wone na démb tay sokhlawoul niolakoy wane
Né thi waar ba yakci fii guissouma lou nioukoy khaagne
{Bril}
Nioy guiss bén ponkou am lougn thi féntt,
Adounay gnéntt, dougn thi fontou nioy dokh di guéntt…

[2ème COUPLET] {Bril}
Liy djougué thi xelyi paka thi mbar la, founiouko rothié day djam ,
Lingay dégg, liniou thiaambar la djokhati noppyi daadjam
Wakhati nieupp né niannla /niou deuk thi djeuf sa nianela /,
Nioy lérou bidew bi , meunn thi guew bi dal sa kaw raniann la /

{Ombré}
Héy Héy , ni woor na sa Mame , djamassanté wougn té dougn thi saggane
Nieuw di natal kharnou bi nga dagg ane ,
Dokhé nagn ko tankou néén thi xaaxaam, worna sa Mame …

{Bril}
Li ngén yagga gueustou ay att , laniou kham thi ay fane
Foniou guissè guestou daw lathie , finiou djougué moy fane
Léér lagn thi xol yi, gni sén guissine leundeum tokhognoulén
Bokkouniou léneu , kiy feuggueu deuneum djokhonioul léneu …

Refrain
{Ombré}
Daniou yaagga doundou thi maral di sééntou biss mou nawétt
Tay niou khiin di taw ba maral bi moudjou thi sa wétt
{Bril}
Nioy guiss bén ponkou am lougn thi féntt,
Adounay gnéntt, dougn thi fontou nioy dokh di guéntt
{Ombré}
Méti wone na démb tay sokhlawoul niolakoy wane
Né thi waar ba yakci fii guissouma lou nioukoy khaagne
{Bril}
Nioy guiss bén ponkou am lougn thi féntt,
Adounay gnéntt, dougn thi fontou nioy dokh di guéntt..

[3ème COUPLET] {Ombré}
Ling-niou yééné mba dina done djaameu –
Yaggueu lol thi leundeum takh niou meuna dokh di gueumeu
Tambalé thi bén tay moudjou na done djeumeu
Bokkouniou bén yone , bokkouniou liniou gueum …

{Bril}
Nio Deuké boyal, djafal kheuthie kheureuti Nieup yéégui
Yokk sa kheul yi, Wakhla Fokk nga kharéthi doga yégui,
Finiou wéssou lonko xalima, xatim, massko gueunleu yéém ,,,
Nga seuss ba nangou xolma, yokkou xaat lim té meunouniou yém ,
Nioune douniou taarkhiss , yagga deukkou dôr deurkiss
Doni #Nongo raw thi #Daara_j té meussounio nane kiss (haan)
Woola téégui touma , Djomal la done sa Ndiouma…
Li ngén amoul dagn thi beurilé bakoy mayé thi Louma…

Refrain
{Ombré}
Daniou yaagga doundou thi maral di sééntou biss mou nawétt
Tay niou khiin di taw ba maral bi moudjou thi sa wétt
{Bril}
Nioy guiss bén ponkou am lougn thi féntt,
Adounay gnéntt, dougn thi fontou nioy dokh di guéntt
{Ombré}
Méti wone na démb tay sokhlawoul niolakoy wane
Né thi waar ba yakci fii guissouma lou nioukoy khaagne
{Bril}
Nioy guiss bén ponkou am lougn thi féntt,
Adounay gnéntt, dougn thi fontou nioy dokh di guéntt..

[Outro] ombré : ni woor na sa Mame , djamassanté wougn té dougn thi saggane
Nieuw di natal kharnou bi nga dagg ane ,
Dokhé nagn ko tankou néén thi xaaxaam, worna sa Mame …
bRil : Doung thi bolé wakh djou beuri – louniouy djeuf laniouy weuri
Ombré : bril fight 4 … alam daar ombré zion
bril : thi biir xél yi laniou khééxé …

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR