LYRIC

Intro
Where they at?? Ndakh ma lène wara yèè
You’re now listening to FREE Music, okay?
Verse
Yo mAfI guEUnEU tIpsÉ town BEU YEUMBEUL
Nénégn BAy bi deEUfEU pEAce mais thi Sound dey yEUnguEUl
A I EU EU I ÉÉ A EU EU EU
Kholal mA fI ndiEUkEU rImÉÉ Ay phrAsou lEUmbEU
Moune na diApIzÉÉ AK AY kAAssou zEUmEUU
Diaroul wine, khellil me kick ak basse you deugueur
Beyoncé’k Amber Rose doumeu sene massou dieukkeur
Diottaye boumeu bokk Mc bou nase dou peundeul
Nullarou MC yi nekk di tassou leumbeul
Ken amou thi ndiérign, comme aye phare you leundeum
Bayilene deukké critiquer war bou feulleu
Hip hop’eu gueneu noble thi li art bi eumb
Me change rime bala sappi wala ndourou lou yomb
Dance thi nieupp ande happy mel ni koudourou song
Adassa ko tchididi, ma safal ko fi ni ni
Bou doyoul me defate ko easily, easily, easily

Genrou ambiance yi mey fattali 2002
Diamono yi mane ak Petit Di dem Aldo
Homie tu sais faire mieux? Démal dore !
Déggeugoume fi dara loudoul Dix mille doules !
MC yi meu tiope? Nélène Free soureugoul !
Mangui thi birre té sme dick toureugoul
Maye beutou pyramide bi mom gning thi soufeu soufe
Diang yi laye nieuw tass ni Vivi-B°*^° Nd!:%
Coup de boule nga bougone seme liguey han ??
Sale gay an nioune nga bougone liguey han ??
Guénte me me guenn game bi nekk pé han??
Folli nalene #Souleymane Ndéné #Guéant
Kenn dieundeutoul sene dope comme VRAC
Ndakh diamono boukeu two ondeu feft nguene bloquer
Mane? Degn tamm seme flow comme crack
Kou toke some diamoul seme son rek craquer !

Tang bey lakké, légui ngay dogueu recognize
Kou le ladj nou bii job mel néko nice!
Dé ko fight, diamono dineu dokh
Kou leu beugg diokh wakhou dof diappé wou leu MELOMIND
Ki leu gueneu job ley fey, ki leu gueneu ill ak gni leu gueuneu bokk degn ko bey
My BOY negn ko Bégn ney boy (nala gaagne yo #DJ Sothiou)
Be askane gui accepter néniou “eksess”
Niou nangou nekk mythomane? Non non !
Be lascars yi accéder thi ay high spaces
Beuri nice texte fils légui maye chef fii
Boumey mic’check hii? Signel me aye chèque !
Boy yi tek sex money & thug
Fok né Empress you bakh yi légui money léniou gueum?
Hey neu yenn mec yi baayi kaathieu
J dongg le beu niom Macky baayi saathieu (non deme dioum)
Ne yenn boy yi baayi kaathieu
Jamm dongg le, beu sen baye yi baayi saathieu (ha)

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR