LYRIC

{Hakill}
Yako done laathié ana featuring Collabo Hakill ak DIP
Rap nagne ba nio ngui finalou game bi wowéniou Reptyle Hakill
{DIP}
Mot 2 Pass bi kone diox leu passe nga dougueul nga soga né cii chef yi
Wakhou niok boy yo xamni sen programme moy teudiou cii ay douss di selfie
{Hakill}
Yaw fi ngay xaathié mane sila baathié sama Rap-ba djam sa xel foumouy naathié
Guiss na waa djé mouy copier wanté meusso guiss fou maître youxou élève saathiéy
{DIP}
Da nga déh cii galsen boul def ni mane dh, Guedj nala déguelou depuis diamono Pinal Gang
Rapeur yifi né di waadjal lima lerr ba lerr sen album guéneugoul waayé lissi nékeu xéwina dh
Di nga guiss sunu concert fess, Di nga guiss sunu postaire fepp
Di nga Label you makk yi diniou dakadjii ak cachet bouniou beugona diox Thione Seck
Maay Paul Pogba cii sa club,….Obama ci sa deuk
Rappeur yu beuri beugueu-tougnema guiss parce que damay melni pompe à gaz cii sen beute

{Refrain}
Ngani ko beug ndiraul biss bo maaggué,
Meussounio am idole Boy yu ndaw
Waayé sunu loxo yi diss ni Bomayé
Bombardé nagne gnifi né faaw nga wowaate gnénèène
Game bi bloqué waral niouy tidjékou sunu mother fuck Mot 2 Pass maen

Hééy DIP Manela
Waay Moréé Ich Yo Boy Hakill
Haanoow Ich Yo Boy haanoow Manela Waay Doundou Guiss
Morééé Reptyle Grand Yoff nio controlé game bi
Gars yissi dess est-ce que nio ngék Mot 2 Pass
Dééédéééttttt

{DIP}
Xéwi nga ba rombeu Gameboy Nigga, Kaay langueu sama wétt thiow dou djip
No dou Music Djangalé takh mane ak Ich Yo Boy def son bi nii
{Hakill}
Yeah ! Kouniou gueuneu xam mot 2 pass bi, Bountou you banione dagneko daadji
Douniou meusseu feug dagni nieuw sarre kone nak nigga meune nga téyé sa thiaabi
{DIP}
Mot 2 Pass Mot 2 Pass dagnou jog pour nieuw tass sa défense
Topando niou djafféwoul féxel def lou meussoul am Senegal
{Hakill}
Ooooh loy kass loy kass parce que niaari boy soule li nga done gass
Nioune dagni tothie té douniou naane kass
Amouniou dépendance Ndax guéwou rap bi amoul bankass
Ana gni fogone dou meusseu fay, Loma wakh tay douma saf waay
Mot 2 Pass bi meunoko xam ni boy internet ak waa Under Shifaay
Nioune leu boy meune nganiou wowé rakkeu waayé Rap dougnessi sa morom
Ya ngui cii kanam di naagou waayé boula neexé boul daagou ndax dagnela rombeu (Voom)

{Refrain}
Ngani ko beug ndiraul biss bo maaggué,
Meussounio am idole Boy yu ndaw
Waayé sunu loxo yi diss ni Bomayé
Bombardé nagne gnifi né faaw nga wowaate gnénèène
Game bi bloqué waral niouy tidjékou sunu mother fuck Mot 2 Pass men

Hééy DIP Manela
Waay Moréé Ich Yo Boy Hakill
Haanoow Ich Yo Boy Haanoow Manela Waay Doundou Guiss
Morééé Reptyle Grand Yoff nio controlé game bi
Gars yissi dess est-ce que nio ngék Mot 2 Pass
Dééédéééttttt

Hééy DIP wakhma louy mot 2 pass bi boy
Manela Waay Nigga Manela waaay
Hakill wakhma louy mot 2 pass bi boy
Ich Yo Boy yaw Ich Yo Boy
Hééy DIP wakhma louy mot 2 pass bi boy
Manela Waay Nigga Manela waaay
Hakill wakhma louy mot 2 pass bi boy
Ich Yo Boy yaw Ich Yo Boy

{DIP}
Gueumouma nii yaw di nga niou frek
{Hakill}
Pour nga andeu ak nioune fokk nga xam sunuy codes boy
{DIP}
Guiss nagnou feu bi té beussou niou frein
{Hakill}
Dagnou warr fass yu meuneu daw melni Cowboy
{DIP}
Da nga takkeu beug niou niodi fresh
{Hakill}
Nioune ndoxou zéro degré lagni xeupooo
{DIP}
Kaass nga naane ma ngui dieundii Caisse
{Hakill}
Daadj yi ngay weur nio ngui biir Ich Yo Boy

Ich Yo Boy Morééééé
Ma ngék Ich Yo Boy Morééééé Manela
Kou xam Mot 2 Pass bi Ma ngék Ich Yo Boy
Morééééé Manela Waaay
Haanoow Ma ngék Manela Waay
Haanoow Haanoow kou xam mot 2 Pass Ma ngék manela waay
Haanoow Haanoow kou xam mot 2 Pass Ma ngék manela waay
Haanoow

{Refrain}
Ngani ko beug ndiraul biss bo maaggué,
Meussounio am idole Boy yu ndaw
Waayé sunu loxo yi diss ni Bomayé
Bombardé nagne gnifi né faaw nga wowaate gnénèène
Game bi bloqué waral niouy tidjékou sunu mother fuck Mot 2 Pass men

Hééy DIP Manela
Waay Moréé Ich Yo Boy Hakill
Haanoow Ich Yo Boy Haanoow Manela Waay Doundou Guiss
Morééé Reptyle Grand Yoff nio controlé game bi
Gars yissi dess est-ce que nio ngék Mot 2 Pass
Dééédéééttttt

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR