LYRIC

INTRO

{RIDIAL}
ENH God knows what I am telling
do massa hamni do massa geumni L.I.F.E da térédi,
Hol yi hat xél yi heum gneupwérédi,
Téla fly –dik tah mou té-ready
Gnou sick many bi honey bi defi credit,
Gno méli ni, nit dimbéli nit
Diamonoy doh ngakoy top diko djéléni
Douy bén bi, louy ndayou tourou enemy
Yako angou ya handjou rot thi ténam yi
Hana dangéna fate tourou kén mi
Nga beug mou beun zaman bamouy sén ni
Yaw kan nga ni hamoko té moné
fang ni nita crazy lazy li lan la ni
Dou dangay dé gnou gass la soul
nga délou ban bani djaroul hady
rouslol gnninane manoli
Gninane la sagnoli
Goumbeul teuhloul ni bagnoli li life
bi di denth ngir yaw day gnew nga
yor thi bagnole yii

Chorus
Like the sky which’s over ‘em
Yéssal gueum bi try ba lép dém
Dougn massa cry dagniy tok di djém
Ba lép am my homey no change
remain be da same
Like the sky which’s over ‘em
Yéssal gueum bi try ba lép dém
Dougn massa cry dagniy tok di djém
Ba lép am my homey no change
remain be da same

{Arafat PART}
Yeah beugatouma perte ben munit
Amatouma time my mine need it
Beugatouma chine bay guene sidiit
Dama beuga fine fayékou am some merit
Kawe yeuketikou ni ap satellite
Yeeuketi mbag yeuketi bop done elite
Papa m’a dit verro possimus le mot spell it
C’est la vi comme latin te dit Victor numqum cedit
Si tu me tardes sur la route je te laisse
Ma vie est si exacte qu’elle dépasse
celle de monsieur Tales
Je l’a mène bien, la vie, dit ca aux autres
Je me contente sur ceux que j’ai même si je suis un pauvre
T’as l’argent dans la main l’enfer dans la tête
Moi, c’est seulement si je ne pris pas que je paye les dettes
Je suis pas bette c’est a toi de faire la faire la fêté
Apres la mort je meurs une deuxième fois pour bien mener l’enquête
GOOOOO

Chorus
Like the sky which’s over ‘em
Yessal gueum bi try ba lép dém
Dougn massa cry dagniy tok di djém
Ba lép am my homey no change
remain be da same
Like the sky which’s over ‘em
Yessal gueum bi try ba lép dém
Dougn massa cry dagniy tok di djém
Ba lép am my homey no change
remain be da same

{RIDIAL PART}
Neko dess na lata beuss gnou
wouyoussifa
Meme bougn lay bote nga nangou
ba dougoussiffa
Certes que j’ai mon God et toi t’as
Lucifer
Parfois l’accent est roque mais beau
comme youssoupha
On est des envoyés occupes comme le président
Mais faut jamais couper quand il y’a talent
Tu réussiras quand qu’il y’ a faute
assume que c’est l’appelant
Qui l’a voulut oui be on da the way
je sais que y’a du talent

{arafat }
When you see me doing in da bad
ways don’t ask me how?
My head middle my shoulders but the reason goes
When the time goes, tell it to make it low
This is my life this my life you never know
When you see me doing in da bad ways don’t ask me how?
My head middle my shoulders but the reason goes
When the time goes, tell it to make it low
This is my life this my life you never know

Chorus
like the sky ah ah ah ay
Like the sky like the sky ah ay
Dougn massa cry ah ah ah ay
Dougn massa cry dougn massa cry
ah ay
like the sky ah ah ah ay
Like the sky like the sky ah ay
Dougn massa cry ah ah ah ay
Dougn massa cry dougn massa cry
ah ay

Outro
IT’S REAL and ARA AKHLOU BRICK
ALDIANA as know as Paradise
That’s MY LIFE that’s MY
LIFE!!!!!!!!!!!!!!!!!!

Added by

Papi

SHARE

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR