LYRIC

{Refrain}
Taal bou Yalla taal wakh fayouko (Taal bou Yallah taal wakh fayouko
Nama Yalla Baal niou ngui sen kaw (Nama Yallah Baal nio ngui sen kaw)
Taak shine yu lerr naagneu ni Bidéw (Taak shine yu lerr naagneu ni Bidéw)
Taal bou Yalla taal wakh fayouko (wakh fayouko, wakh fayouko)
Yeaaaaaaaaaaaaah ! Nagnou Yalla Baal (2 fois)

{Verse 1}
Yeah Taal bou Yallah taal, tole bou Yallah bay
Djam bou Yallah fale day gueuneu takk di gueuneu teuweu fay
Yeah Yeah Fall kou Yallah may daal lo beugue na gnou cii mom na nga na ngou ni da nga koko fay
Ndax kou Yallah may baat dina wakh té kouné am bou nekh dakoy weuy
Dama dane lakatou gnima gueuneu diégué
Dama lerrone cii séni beute bagnou goumbeu
Gnima gueuneu sorri nioma dane ndieukeu sèène may takk di magg niou melni niou moumeu
Niveau bi gueuneu kawé lay football, Légui joueurs yifi eup gueudeu laay doumeu
Dama jog djité kharouma Aldiouma, Ma ngui weur kane moma soute té guissoumeu
Soubeu cii janteu la goudi werr taakna shine boul bagne lolou kène doussi polimiquer
Ndaandeu na lerna maay thiaatou bidéw bou djoudou ferr di lekk cii bolou makk yi
Faangue na féégne na djomi ngène ndax dolé dji nek cii mane mo gueuneu kawé dolé djiné
Raangou na xékh na ba togueu tchine bi yaguena xéégne nékh té dou gowé cii nëk

{Refrain}
Taal bou Yalla taal wakh fayouko (Taal bou Yallah taal wakh fayouko
Nama Yalla Baal niou ngui sen kaw (Nama Yallah Baal nio ngui sen kaw)
Taak shine yu lerr naagneu ni Bidéw (Taak shine yu lerr naagneu ni Bidéw)
Taal bou Yalla taal wakh fayouko (wakh fayouko, wakh fayouko)
Nagnou Yalla Baal, Nagnou Yalla Baal, Nagnou Yalla Baal (2 fois)

{Verse 2}
Yaguena def ay Hits, Bobou amogouma wone ay clip
Lii fii Thiere bindeu cii ay recette tou beat eup na ay livre diexalna ay bic
Mané yaguena bégueul ay niit, bobou amogouma wone ay sites
Ba nga ndieuké dégue lima bindeu deug replay na ngou nga kone meusso wone write
Yaw maa dakk Rap Sénégal dial home maa nék cii ngour def ko sama FreeDong
Sama DOPE legalize souma nekhone guéné Bum boumay toudé Dakar Kingston
Am dieundeul bii defko Ringtone, niou ngui Job té meussou gnou am piston
Kou la lathie ndax ma ngui géré fight néko maay Mouhamed ALI cii ring Bro
Mane damay takk douma mandi
Ay dathieu naturel laay aandi
Defla MARIO diamla ay Cham….
Sou done WESTERN move bi dagnou may WANTED
Héy boulma wane sa kanamou gentil, Xam naani ya ngui niaane maa fay ndax nga meuneu tranquille
Damay gaasse tombe ma soule ay Garçons comme GASTON ci microphone mane may BANDIT

{Math’Art}
From the Underground liguey bi dorroul tay
Guiss nga aggue nagnou cii kaw liguey bou sett daye faye
Kila yague tipsé kéép sa good time
Get sunu Vibes Alright Oooouuuu Yeah Oooouuu Yeah
Dagno door mou naathie nieup sédéko Walahi
Change Game bi defko Saafara indi mouslay
Never Never nga guiss gnou cii détails
Wowéma Grossiste one more time

{Refrain}
Taal bou Yalla taal wakh fayouko (Taal bou Yallah taal wakh fayouko
Nama Yalla Baal niou ngui sen kaw (Nama Yallah Baal nio ngui sen kaw)
Taak shine yu lerr naagneu ni Bidéw (Taak shine yu lerr naagneu ni Bidéw)
Taal bou Yalla taal wakh fayouko (wakh fayouko, wakh fayouko)
Nagnou Yalla Baal, Nagnou Yalla Baal, Nagnou Yalla Baal
Nagnou Yalla Baal, Nagnou Yalla Baal (2 fois)

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR