LYRIC

{Chorus}
Liguèyu ndèy moy agnou dom
Rongagnou Mère sa niakkeu jom
Yeurmandé baxoul soxor mo baakh
Tém policier bi djaay leu drogue meunougnema fay
Iblis sakh dou job comme mane
Awouma deukeundo ci kaw suuf Bokouniou drapeau. no noooo !
no nooooooooooooooo !
Founé dem nafa
Founé fanaane nafa, Founé fanaane nafa, Founé fanaane nafa
Haaaaaaaaaaaaa
Kone Ni Leu Meunone Démé
Ni Leu Meunone Démé haaaa
Ni rek ni rek ah
Ni rek ni rek ééééhaaa
Kone Ni Leu Meunone Démé
Ni Leu Meunone Démé haaaa
Ni rek ni rek ah
Ni rek ni rek ééééhaaa

{Verse 1}Galsen Lyrics
Assamane ci meun na xiine té dou taw
Sama Mama dina triste mais dou djoy
Deukou crise mais sa fils beugoul fo
Bène domam doufi xiff té dou thiop
Jotna yéé sama gueinteu, yéétal samay beug beug
Goor yé ngi yom, goor-djiguène di gueuneu deugueur
Dou da nga MOUMEU rek sa YALLAH wara TEUKH
DIOUR sa bopp, SUUL sa bopp niaar rekka leu meuneu TEU
Amo place même ba sa biirou mère nigga
Fimou leu diouré fala sa makk yi djougué nigga
Mauwty dina moudj déh, matteu deum bou rafett do waalé fébar bou neekh nigga
Rakk wauloule sa xarite yi beus di nga xamni safara mo takk fi
Dérett-ta fort gnila beug niola sonal
Sa Papa djangal leu xarou sa yaay nampalé laak possone
Mane dagn mané diokhel sa xol ma diokhé sama rouh
Niou khaar ma tidji sama gatt ma oubi sama yuur
Naathie dou yegg seddaay kène leundeumoul ba taal lampe bou nioule
Yagg diokh sa taate ay niitou goudi Yaye djou dom bu flou
Sa pelle bi nga gassé pakh bi ci lagn la moudjou suul
Dama cher bomay ray déféko pakka wuurouss
Tant que nio ngi fèneu beusseul sa xol bagnala tontou mougne
Yaak derr xessaayu xessal kat deug bouniou mourre

{Chorus}Galsen Lyrics
Liguèyu ndèy moy agnou dom
Rongagnou Mère sa niakkeu jom
Yeurmandé baxoul soxor mo baakh
Tém policier bi djaay leu drogue meunougnema fay
Iblis sakh dou job comme mane
Awouma deukeundo ci kaw suuf Bokouniou drapeau. no noooo !
no nooooooooooooo !
Founé dem nafa
Founé fanaane nafa, Founé fanaane nafa, Founé fanaane nafa
Haaaaaaaaaaaaa
Kone Ni Leu Meunone Démé
Ni Leu Meunone Démé haaaa
Ni rek ni rek ah
Ni rek ni rek ééééhaaa
Kone Ni Leu Meunone Démé
Ni Leu Meunone Démé haaaa
Ni rek ni rek ah
Ni rek ni rek ééééhaaa

{Verse 2}
Kou amoul xol amo fit
Kou gueum YALLAH do ragal
Ray naniou kou djoudogoul
Teuth ngène kou défoul dara
Say mbokk diekh bo réindé say noones
Meuno Weet so amé ndam
défaite mom orphelin leu ni sédaayu safara
Haan ?
Da ngay business sa diné loudoul fay Moussou mala tchi guiss
Nittou jaameuh ngeu kagne ngay djoubaulék YALLAH ak Ibliss
Euleuk tchi biir di nga fégne nigga euleuk tchi biir
Nakho sa bopp nakho Yoneinte bi
Ndakh goumbeu dina guiss souy gueinteu
Khall wané nioumouy lakk bala bissou peinthieu
Deug méti ni secrets yi nga dinthieu
Do fatté lo nga djangal sa bopp kane mo moussoul fèneu
Yeah ! THIAGGA bou YIW ni POLICIER bou DJOUP
Meuno di déglou di wakh ni kouy lekk tchi douch
Bopp bu fess day tek djeuweum ci suuf
Motah couronne meune na djaapeuh kou moussoul nekk buur
Ay ! Gni déh nio niou gueuneu riche nio niou gueuneu niaakeu
Seu meilleur xarite la yëré noone ngi di gueuneu djaap
YALLAH teuthie Bideew ci jail mouy lerral nioune nieup djanteu
Même kiy sangue neew, sangou kattou neew di nako sangue

{Chorus}Galsen Lyrics
Liguèyu ndèy moy agnou dom
Rongagnou Mère sa niakkeu jom
Yeurmandé baxoul soxor mo baakh
Tém policier bi djaay leu drogue meunougnema fay
Aaaaanh Haaaaaaaaaaan !
Iblis sakh dou job comme mane
Awouma deukeundo ci kaw suuf Bokouniou drapeau. no noooo !
no noooooooooooooo !
Founé dem nafa
Founé fanaane nafa, Founé fanaane nafa, Founé fanaane nafa
Haaaaaaaaaaaaa
Kone Ni Leu Meunone Démé
Ni Leu Meunone Démé haaaa
Ni rek ni rek ah
Ni rek ni rek ééééhaaa
Kone Ni Leu Meunone Démé
Ni Leu Meunone Démé haaaa
Ni rek ni rek ah
Ni rek ni rek ééééhaaa

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR