LYRIC

{Intro}
Yaw mi yaw rek maak iow doundou ak déh
Kaay tok fi do dem lo wakh d’accord wi okay
{Refrain}
{Dip}
Parce que Mane damala beug si sama khol
Yaw damala beug ba xadjato sama khol
Way nala paroles ya ngi si sama xol
Guiss nala boma kholé ci sama khol
Héééééééééééy
{Dip & Nailah}
Don’t cry, don’t cry, Don’t cry, don’t cry !
Don’t lie ! Don’t lie ! Don’t lie !
OoOow Woooo

{Nailah}
One Night without you, OooOh HoooOo !
One night without you… Oooh No
I can’t spend one night without you
OooOh Haaaaaa
One Night without you
I don’t walk one night without you

{DIP}
One Night without you
One Night without you
One Night without you
One Night without you
One Night without you
One Night without you
One Night without youuuuu
One Night without you

{DIP}
Fixé meu sa beute yi laay khol ni
Drogué ngama yaak sa parfum bi
Yobouma fo xamoul sakh yone bi
Mounou niou reer ndax soma guissé soumala guissé fégne
Hééééy waaay hééééy waaaaay
Kaaay ma defla diabar bb kaay niou seuy waaaay
Fanaane ci nëk sans yaw rek meune nama ray waaay
da nga may manqué saaayuma xeffé sa wett kaaay

{refrain}
{Dip}
Parce que Mane damala beug si sama khol
Yaw damala beug ba xadjato sama khol
Way nala paroles ya ngi si sama xol
Guiss nala boma kholé ci sama khol
Héééééééééééy
{Dip & Nailah}
Don’t cry, don’t cry, Don’t cry, don’t cry !
Don’t lie ! Don’t lie ! Don’t lie !
OoOow Woooo

{Refrain}
{Nailah}
One Night without you, OooOh HoooOo !
One night without you… Oooh No
I can’t spend one night without you
OooOh Haaaaaa
One Night without you
I don’t walk one night without you

{DIP}
One Night without you
One Night without you
One Night without you
One Night without you
One Night without you
One Night without you
One Night without youuuuu
One Night without you

{Nailah}

And I miss every single peace of you When you leave me all alone
And God knows how much I love you I don’t want our story to be done
And I miss every single peace of you When you leave me by myself
And Lords know how much I need you, need you

 

{DIP}
Dioxma lima mom, Dioxma lima yélole girl
Tekma sama place my girl
Dioxma lima mérito
Dioxma lima yélole girl
Tekma sama place, so Weu
Dioxma lima mom
Yaw rekka né fi
Goudi bi goudou neu meun nga dess fi
Fanaano té guiss ngama sa gueinteu yi
Teuth nala meuneu toma reuthieuti

{Outro}
Héééééééééy
Don’t cry, don’t cry, Don’t cry, don’t cry !
Don’t lie ! Don’t lie ! Don’t lie !
OoOow Woooo

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR