LYRIC

{Part Ara}
Salam Malé Malékoum
Ziaré Nakamou
Serign King Nouyo Nga Laisser Deux Souk Sidiote Kou Gueuna Gueum
Salam Malé Malekoum
Halass Teuss Danga Dioum
Deup nga Carte ici c’est Paris do Deg Gnou Way ko VÉLODROME
MESSI la CHRIST 5 ballons d’or
Fightou Mayweather vs McGRegor
Lek Money Rap Bi Gayi Né Di Sap fi Geuna Hif Melni Kou Nek Thi Werou Koor
Bougnou Teukelé ak Ben Gang
Dinga Beug Loma Bagn Bagn
Kan Mofi Dé Thi Loho General Bi Barthélémy Kassé fi Bang Bang
Big D Meun Na Ngandeu Boy
Mai Leroula Ni Am Na Sagn Sang
Sa Pa Né sa Maman na Ande Boy
Am Na Galagn Tay Mou Teug fi Sing Sing

Hello word Hello Hello Rap Dithi Dawal Velo
Hello Word Hello Rabouma Dawal Fass Damay Rap Dawal Velo
Pédaler
Laisser deux
Pédaler
Laisser deux
Refrain..
Pédaler Pedal
Laisser Deux Laisser
Pédaler Pedal

{part Dayza}
Eddy Mekks si Velo Mala Rawe si Game Bi sa Nigga Bi Dou Dabè
Même Boy Bithi Petit Galé ni Da Beuga Melni Dayzakala Bou Magué
Serignou Senegal Ham Nga Louko Déf Gaganti sa Nigga Bou Gagué
Man Punchline Douma Yem Anytime Damay Dem Deglou Mugabé
Danga Apple Ba Doug si Galaxie
né Nga Thi Fitna Né Kou Deuk Palestine
Pacotille Ba Amé Palai Chine
Fans Bila Taneu Tan Na Plastique
Pedaler Laisser Deux Dama Gaw Ni Bolt Thi Beat bi ay Kilomètre
Evitel Dima Sor Sinon Nala Coûter Chère Melni Koula Mbeth
Nena Dama Deg Wolof Ma Deup Lak Dalifor Bi Di Kala
Ndekété Dofoula Djiné Pessoula Ladial Kocc Barma Kouy DAYZAKALA.

Hello word Hello Hello Rap Dithi Dawal Velo
Hello word Hello Rabouma Dawal Fass Damay Rap Dawal Vélo
Pédaler
Laisser Deux
Pédaler
Laisser Deux
Refrain..
Pédaler Pedal
Laisser Deux Laisser
Pédaler Pedal

{part Ara}
Job Today Tonight
Warou Thi Tata Car Rapide thi Bike
Dieum thi vélo Hel Mongui thi Fly
Guero Bi Dou Ba Di Fight
Pé Pédaler vélo thi Nadj Ba agg Town Late
Dayzakala
Souma Dégué Gnouni Kifi Meun Dou Ara Dou Dayza Gnounguimay Défi Réé
Sa Rappeur Dou Ganster Mannequin la Nek Thi Net Bi Thi Face Bi Di Défiler
Dayza la Tramway la Dou Dévier
Ndank ndank Bokoy song di Reculer
Mangui Banque Danga Bank mac ADBD fay la Chèque Bi May Halée des Billets
Ara
Helo word Hello Helloooo weu
Ara Mo Meun sa Nigga
Dayza Meun Sa Nigga Boy
Hello word Hello Helloooo weu
Ara Mo Meun Sa Nigga
Dayza Meun Sa Nigga Boy

Hello word Hello Hello Rap Dithi Dawal Velo
Hello word Hello Rabouma Dawal Fass Damay Rap Dawal Vélo
Pédaler
Laisser Deux
Pédaler
Laisser Deux
Refrain..
Pédaler Pedal
Laisser Deux Laisser
Pédaler Pedal

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR