LYRIC

{Intro}
Yeah Hummm humm !
Hahaha Doundou Guiss Manela waay Moré
REPTYL MUSIC, DIP
Héy Mister Thière

{Verse 1}
Ma Yaguena wakh town bi dafa tarr waay
Pa beugoul ma xam accident de travail
Téwoul niou magg ragné niggah
Kone nékouma di Rap pour meuneu nekh nieupeu
Ma dakk RAP cii Monde bi yeup “walaay”
Maay Pakka Poute boudé réwandé ngay djaay
Dafa am cii nioumay settt nigga
Bou nékoul wone nioniou may gueuneu réw nieupeu
Yaguena dégue Wow Yaguena dégue Wouuuu
DIP moussoul nek sur scène naane ma ngui djégueulou
Ya mom song bi yaw mimay déguelou di bëk nii
Ak yaw mi nga xam ni mane rek nga gueuneu djépi
Potolamp fii sa photographe dou meusseu soxla flash
Fokk ma takk ndax bima done rap xollam da done lakk
Numéro 10 doundou guiss Gaïndé Mbeurodi
Walahi meuno siss ba rombeu métis bou raciste
Boy bi bindeum styleum ak flow bi Masha’Allah
Na RAP ba bindeu toureumak disques d’or yi cii assamane cii
Ndax sama noone yi dagno yague djapp teuweu baayi
Boudoul wone ak niom baayina bou yague té dém djangui
From Grand Yoff Arafat Zarco ndandi Faa
Sama yoneu tarr lolo takh soufou tank yi khar
Yakarouma cii kèn té aduna bi yeup lay gueusseum
Kone même bouma done djaay sama ngorr kène dou am njeugueum

{Refrain}
Def ko sa profil ba sa couverture
Sa profil ba sa couverture
Def ko sa profil ba sa couverture
wala sa profil ak sa couverture (2 fois)

{Verse 2}
Ma Yague naama né baayil fowé khalle
Pa bougoul RAP même bouma koy tangal
Reuthiou wouma sakh limay def nigga
Kone Rap bouma pour foo pour mouy lerr
Humhumm
Maay yakk rap bi ngèni def Insha’Allah
Laata Album nga jott Mixtape bou doy waar
Djapalni BEUS NIKI TAY Nigga
La Mère de ma mère est née
Boy fuck Télé Radio ak Net bi séni Interview
Yallah meussoko guiss té do meusseu guiss kouko gueuneu siw
Meuno am RAP cii sa téléphone bi té défo DIP
Kénène kougne fii né yafi dakk RAP dagnela colé motif
Potolamp fii sa photographe dou meusseu soxla flash
Fok nga xam gniy leundeumeul bokoul sama programme
Rap Nga ba soneu dara démoum xana meuno pause
Wala nga baayi ni Old Skool yi yégue ménopause
Nigga ma mom sama lamigne louma nekh laay wakh
Xam nani sécurité Aldiana rek la amm
Batterie pleine non dou mak gni di takk di faye
Ngaaka yi nek di khaar Baag rekkay yagg cii Ténn
Douma nétali kone da ngay tiite ladial sama équipe
Nagne leu xamalni lima dathie dafa wessu métiite
Kone boné DIP da wara tarr biw sa MCs yi
Day melni ngané Yallah wara djamou yoneinte yii

{Refrain}
Def ko sa profil ba sa couverture (Yeah)
Sa profil ba sa couverture (Hun Hun)
Def ko sa profil ba sa couverture
wala sa profil ba sa couverture (2 fois)

Doundou Guiss Manela Waay Morééé
DIP Quinzaine
REPTYLE MUSIC

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR