LYRIC

{Verse 1}
Me dieulate ay gaïndé me dompter lène
Same flow ay containers moye gonfler nérou wa corner bé
Zig, Tamba ak Pont Faidherbe
Boudoul wone fi dou done fénène
Boudoul wone Free dou done kénène
Boul khole kénène bougoumeu done lénène
Al hamdou mane santena
Jamm dongg le shit bi dou done lénène
Strong in the biz boy pompez lène
Té con yi le time deniou done kébétou souniou son yi di leu hit ngané on t’énerve
Bouniou nèkhone niouy diaay rich
Fègne ak bepp khètou bad bitch
Ndakh gentle negn, tangal nègn
Wayé boul tékkheulé bante ak wégn
Boul tékkheulé thiant ak wéy, dinga diawalé diante ak wère ??
Bou bougué am diam dongg son bi diam se ndong li
Nanga and ak tèye
Bo lene mounoul balène mic bi, cons Free crack#bon élève
Dope pour Black & white am na raison nègre#Emotion Hellène

{Chorus}
Jamm dongg le ish bi dou done lénène (ish bi dou done lénène) X4
Togg na quantité yekk na qualité (hun FreeDope)X4

{Verse 2}
Wesh c’est qui ? Qu’est ce the deal? It’s the best in this my boyyy
Mane doumeu dieul extasy, gueuwmeu sex appeal té doumeu nekk di bif ak ay boy (hunhun)
Rest in peace Laye Séga, RIP Baye Petit
Iba Sèye, Lik-Sama, wallah wéteul nguène birr keurgui
The West African Finest, man a rep African fighters:
Niom Sankara, Lumumba : I’m no blood but I’m diamond
Bad as M.I Jackson, Jam-ballin like Jordan
My tape rockin like Mysonne
Punch faces like Tyson haaaaaan
Audio crack coke layenouyo
Gayiniam flow bi saf DOPE bayi niou go
Dealers yidow degn degg DOPE ba ngui nieuw
DOPE ba ngui nieuw!?? Wou yaye DOPE ba ngui nieuw!!!
Sama style defe nité ya ngui feel nimey indé sama flow?
Mo gueuneu épicé kilo bone !
Sama skill defe styléé, deme ill, nimey dealer sama DOPE ?
Demey killé ak stylo dongggg !

{Chorus}
Jamm dongg le ish bi dou done lénène (ish bi dou done lénène) X4
Togg na quantité yekk na qualité (hun FreeDope)X4

FreeDope X4

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR