LYRIC

{DIP Doundou Guiss}
Aaaaah !!! Aaaaah !!!
Xaadiagouma bay soneu fils
Ndax xam naani xathie you makk yi nagne songue DIP
Yeah xawma mane bane atte sakh la guedjeu treune (Training)
Même Balla Gaye douma gueuneu deugueur
Nénagne “yéné nëk leu borom rekka fay fanaane”
Té li nga ma yéné lala yéné waayé bokouniou nëk
Niata Real Nigga la xam yu sopalikou Fake
Niit yeupeu leundeum kène meunoul am takandère bou wékh
Meunena tégui nieup bamou dess sama bopp Terminus
(Manela) Dawna djangue dess cii bopp kogne di def Music
(Xawma) Lanemo takh bouy gueuneu thiool may gueuneu guethie Eglise ?
(Dama) Yagg nek benn gaayine bouniou djappéwone doff bi
Sama Fan yeupeu deurkiss cii sons yi ngay def
Samay rongogne la guedjeu guiss té namou malène
Tédou da nga ma done xepp meune nga continuer
Nigga DIP yène nieup la ndara FATHIEU ni ay COMPRIMéS

{Refrain}
Real Nigga dou djoy
Real Nigga
Real Nigga warna xamné
Real Nigga warna xam nané
Goor deug rek la wara done
Yeah Real Nigga waro mel nénène
Real Nigga dou djoy (2x)

{ROSSO}
Kou féthie ba guène guéw kène doula sétane
Motah yène song you bone yi dafmay def ay rétane
Kholal Qualité pas quantité moy gueune soy taneu
Rosso bayina RAP moy xeuyna def lou gueune tchi Cheytane(né)
Wane nala nieuwna fokk gars yi jobbaate
Ndax borom ndéki kouko ndieukeu yéwou teudaate
Yallah néna Jesus Christ dina meusseu nieuwaate
Waayé waurna God kou melni mane cii Rap dotoul amaate
Goor deug day defni nioune di Job di weuye, Dou meusseu djoy dou meusseu diambate
Am bagg nguir sa djaane wathieu, I’m back pour li nga daane wathie
Am tiaathie soxlawoul am dathieu soxlawoul rambaathie
Djoy douniouko meusseu def téwoul ni rongogne dagnessé am paathie
Bopp bou ndaré am jammeuh day saxe ay nopp dégue
Aka beuri nioumay déguelou aka néw gnimay dégueu
Xamelo beug molay déf tamite goor deug
Dou thiaagané dama réw just yénama dégoul

{Refrain}
Real Nigga dou djoy
Real Nigga
Real Nigga warna xamné
Real Nigga warna xam nané
Goor deug rek la wara done
Yeah Real Nigga waro mel nénène
Real Nigga dou djoy (2x)

{DIP Speech}
Yeah respect gars yi nga xameni
nio ngui rap ligni doundou gnidi guéné li nék si niom deugueuntane
Fuck gnidi moubo secteur bi
nioune déniouy défal secteur bi aprés kénéne nieuwat déf liguéyam
kharouniou léne si secteur bi
khamé néniou gnidi déf yeufou hypocrite parce que meuno wakh lo khamni
néwoul si yaw bama guiss si sama bop non non
motakh pour mou gueuneu lér fuck real fake yi di rap pour niou diapé léne aye real
khamanté néniou souniou biir

{Refrain}
Real Nigga dou djoy
Real Nigga
Real Nigga warna xamné
Real Nigga warna xam nané
Goor deug rek la wara done
Yeah Real Nigga waro mel nénène
Real Nigga dou djoy (2x)

{Rosso – Outro}
Yeah nioune danio am bén vision dissi dem ba diekh men
Xamou niou délou guinaaw amou temps pour regretter dara
Real nigga dou dioy
Ross
Dip Doundou Guiss
G-Y (Grand Yoff) Baby
déglou la ladj
Deugou la ladj

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR