LYRIC

{1er Complet}
Légu Légu ma geum di dianère lii diota wessu sama life
Bigni dougue cii rap diamono 1995
Rak tak niou alou khirou defko thioki mic di fight
Hard Cor bégnou bercés nioune douniou tiapatattt
Daniou dane tak lampétak balaa niouy dem rap attack
Légui game bi dafa tiouné té boy yi daniou yoy
Rak tak niou ooté tiouné melni ay souris youy djoy
Life bi nimouy démé dafa gaw ni tialemère
Beurki dembo ndiaye garrage’ou Kébémère
Niou tokk dii fass ay dream cii bii life bou éphémère
Dafa beurii teuss teuss dagay dem beu teuthiou
Légui légui ma geum guissate yèn djeuf youmay reuthiou
Aduna werrou korrleu té kouy worr digua djoubou
Légu légu xell bi dem cii kiné Codou ak Tanta Diobou
Sèn yakh dina sedd cii guédjou firdaws la saubou
Rest In Peace (R.I.P) mauwtii daflène téleu yaubou

Mao (Chorus)
Yes yes
Yes to this way
Lii diota wessu sunu back in a day
Say Yes! Yes
Xalé mague naa taay God Bless
Sunu lamp takk neu taay
Aduna ngui nii daay nakari di nekh
dara amou fii solo nigga lep daay diekh
Say Yes ! Yes to this way
Lii diota wessu sunu back in a day

{2ème Couplet}
Légu legu nga geum tokk images yi défilées sa mind
Geusseum sa bopp mougne, fatélikou ré
Ngélawou namel eupouleu nga guéssou dadiii tiss
Nakar ak banekh kou nek momé nga sa biss
Legu legu ma geum plongé cii samay souvenirs
Xalate yi dimay rongé ba damay seug miir
Aduna dafa teureudii mounou loko xelmatii
Amena niou dane yélwane taay niou ngui yéwo almadies
Touteu tank leu justice seum dafa gatteu
Bayi lèn ko ak yalla justice seum amoul aapeu
Aduna amoul solo lou bess dina rapeu
Cii nétali laay moudjé bala li bess di nieuw after
After after after after

Mao (Chorus)
Yes yes
Yes to this way
Lii diota wessu sunu back in a day
Say Yes! Yes
Xalé mague naa taay God Bless
Sunu lamp takk neu taay
Aduna ngui nii daay nakari di nekh
dara amou fii solo nigga lep daay diekh
Say Yes ! Yes to this way
Lii diota wessu sunu back in a day

{3ème Couplet}
Yo !
Cii boppou kogne bi laniou dane tokk
Sènetou sunu euleuk cii yonou Hip Hop
Cii boppou kogne bi laniou dane tokk
Pass pass laniou dane démé cii bobou époque
Cii boppou kogne bi laniou dane tokk
Tiéné di freestyle ba talou nio thiop
Rap pur et dur beugou niou waune commercial
Xeuth mic bi alou ni gaindé bou mèrr cii aaleu
Rap tchii politique founiou dém tiowlii djiip
Xeup tchii kané ba foniou dégg né all shit
Télou niou degg dathie cii galaniou hard cor
Télou niou def block kone soxla youniou gakorr
Ték thiayine féth rimes cii digui dianteu bi shine
Clando cii rap xamé youma ndex ay punchline
Cii boppou kogne la diangué rabou mbede mo gueune tchii mind
molaay def real dioxleu gueude ngay gueune dii shine

Mao (Chorus)

Yes yes
Yes to this way
Lii diota wessu sunu back in a day
Say Yes! Yes
Xalé mague naa taay God Bless
Sunu lamp takk neu taay
Aduna ngui nii daay nakari di nekh
dara amou fii solo nigga lep daay diekh
Say Yes ! Yes to this way
Lii diota wessu sunu back in a day

Yes yes
Yes to this way
Lii diota wessu sunu back in a day
Say Yes! Yes

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR