LYRIC

{Intro}
Rap Wolof Mo Raw
Rap Wolof Mo Raw
Rap Wolof Mo Raw
Rap Wolof Mo Raw

Yeah Yeah Ye-ye-Yeah
Aka Ma beuri ay filston wowé DEUG IBA, KEYTI, BIBSON (Rap-adio)
Moussouma soxla sa piston, Yallah maynama katane ak diction
Pour danél leu diaroul may tiit
Diaroul may yakamti kaloule rek fils
Kou jog songue Gaïndé sa kharou ngay guiss
Sa Shaw ak sa cachet laay nangou né tiir
Dem tchil sama bord, RAP naa siguil sama kogne
Mais légui il est temps ma diiw samay poche di diss
Kone nangou nga ni Free dafa Fort
Naniou yéngueul but SODAV fayoul
Ndakh il faut que niou riche
Meun nek MC nek PDG djabanté AIBD ak CDG
Souniou xeuyoul tabkh tém niou xeuy rek déh
Souniou dom yi maagueuh naniou wéré ganyin
Welcome to the Macina mane la Amadou Ampathé BA ci RAP
Gandim kangam né Cheikh Anta la ci RAP
Y-Bo (Boy) Teaupla mais fatéwoul Racinam
Bro yeup récapitulé ?
Lo xam tchi Poulo bou maagué tchi kognou lébou
Dila lakkeu ay Olof yu lerr
Koufi atane sama Vocabulaire

Rap Wolof Mo Raw (RWMR)
Nioune gnéin wou states gnéin wou niou kaaw
Djolof mo ndaw rek sinon niou yengueul ba aduna yeup xamné nio gueuneu graw
Rap Wolof changé woul pour gueuneu fégne
Nioune wagni ay fans moniou gueuneul ay fakes
Niaakeu nagn LASS (Lass Mc) Dotouniou nélaw
Bourba ak PACOTILLE kène doulène fay (Rest In Peace)

Rap Wolof Mo Raw
Rap Olof-Djo Rap Olof-Djo Rap Olof-Djo (Djolof)
Rap Wolof Mo Raw
Rap Olof-Djo Rap Olof-Djo Rap Olof-Djo (Djolof)
Rap Wolof Mo Raw
Rap Olof-Djo Rap Olof-Djo Rap Olof-Djo (Djolof)
Rap Wolof Mo Raw
Rap Olof-Djo Rap Olof-Djo Rap Olof-Djo (Djolof)
Rap Wolof Mo Raw
Rap Wolof Mo Raw Rap Olof olof olof (Djolof)
….
Rap Wolof Mo Raw Rap Wolof Mo Raw
Nioune gnéin wouniou States My Nigga nioune gnéin wouniou kaaw
Djolof mo ndaw rek sinon niou percé beu Kaana nieuw diniou follow niou naaw
Rap Wolof Mo Raw Rap Wolof Mo Raw
Rap Wolof Mo Raw Rap Wolof Mo Raw
Nioune gnéin wouniou States My Nigga nioune gnéin wouniou kaaw
Djolof mo ndaw rek sinon niou feusseul beu Adouna yeup xamné nio gueuneu graw
Rap Wolof Mo Raw Rap Wolof Mo Raw
Rap Wolof Mo Raw

So fayoul douniou RAP ak …
Il faut que niou takkeu ni 60 60 watt
Son bi ci Voit. (Voiture) ak Boite
Shout out to Black G Rakk Takk Squad
So Fayoul douniou RAP ak …
Damay diakhassé RAP ak CRACK
RAP WOLOF ABADANE
Shout out RAKK TAKK SQUAD
Yeah yeah yeah
Shout out RAKK TAKK SQUAD
Rap Wolof Mo Raw. Da ngay doff wala ?
Jamdong lë
Shout out RAKK TAKK SQUAD

{Outro}

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR