LYRIC

{Intro}
Yeah , sa doundala, sa xaaré la Sa life moy sa fight…. ANALYZIK

{Refrain}
You better put it in your mind
Gueum né war nga meuna Shine , One day {Sa life moy sa fight}
Boul Meussa Djoukk thi di Fight
Meunn nga ndamou thi sa life , Everyday {Sa Fight moy sa Life}
Never say “no”, Don’t say “no” {Boul meussa xaadi}
Never say “no”, Don’t say “no”

{1er Couplet}
Li neubou thi yaw di nélaw sa djeumeu dji, fokk nga yééko hommy
Boul nangou di yééw sa xél ba gueumeu thi doundou gui, soukou sa Ôomm yi
Ki djouk ba takkou di kharé, thi finiou khaaré, yokkouna djoom yi
Bou peund bi wouré, gni yagga di beurèk ndiouma nio doul djoomi
Loussa xalat yi dadjati am-na, Kiy djéém té yaagg thi, meun-na
Lou dougou thi bopp, mou toppeuthi fékhéko djeumeuli mbokk mi kham-na
Kouy khaadi lou djéguè la guissoul, Gueustoul, yégati thi, yénouko diissoul
Djougueul, fékhél dokhé sa xél té bania di waakhi di soul
Nangou gueuna djéém, yégali warèf yi doga meuna dém
Ngèmbou beuré lay guiss, wouti dara like this, Boy khaar koula walou douniou meuna yém
Danga wara gueum dithi daw gaw, Yégg finiou djeum yaw
bania gueumeu khol lithi kaw naw, sori am ndam founé law
Aw finiou djougué raw, Meuna djougati thi naathie wi ba faw

{Refrain}
You better put it in your mind
Gueum né war nga meuna Shine, One day {Sa life moy sa fight}
Boul Meussa Djoukk thi di Fight
Meunn nga ndamou thi sa life , Everyday {Sa Fight moy sa Life}
Never say “no”, Don’t say “no” {Boul meussa xaadi}
Never say “no”, Don’t say “no”

{2ème Couplet}
Boul nangou dinga déss guinaw, gueumeul sa bopp té deugou né “yay king,”
Kila romb dém, dééssouko naw, Boul déékkati koppeu yi nangoula “Fighting.”
Yaw yay the number one, Déél djangue thi lignou la wane
Dogali yégali, dogadi yeungali, waakhou yééwi say rawane
Nanga yeukk ni djom boula, Djito fi dara djiomboula
Boy teuss teuss, beuss, yokkou pass pass, feuss, meunato woté niou Djamboula
Kouthi tègouli djèègo yeungouwoul, euleuk meunoula djieum kanam
Ki thi khéékh bi dooné djéngouwoul, filék wanoula djonkanam
Pousso bi wara di niaw ba sopi sa doundou gui, yaa koy nass, né ci
Fékhala dass mou niaw, nga Feugueuti peund bi, fomp mou néSs Néessi
Béneu bouthi yém dém; danga wara djouk djém; weuri am ndam, takhaw thi Témeu
Beuss djeuli miseum, djizeum, tégui bizeum, wisdom la kheuw thi théme

{Refrain}
……..Put it in your mind
Gueum né war nga meuna Shine , One day {Sa life moy sa fight}
Boul Meussa Djoukk thi di Fight
Meunn nga ndamou thi sa life , Everyday {Sa Fight moy sa Life}
Never say “no”, Don’t say “no” {Boul meussa xaadi}
Never say “no”, Don’t say “no”

{Bridge}
Now you gonna understand this is the way we gonna play {Boul xaar lééneu thi kééneu}
Now you gonna know you’re just living for the fight {Sa doundoula -Sa xaaré la}
Now you gonna understand this is the way we gonna stay {Boul sééntou ndimbeulou kénneu ,, man}
Now you gonna know, we better do it, for the fight {Défal linga wara déf Right now }

{Outro}
To be nobody but yourself ,, in a world that’s doing its best ,,,
to make you somebody else… {gueumeul sa bopp}
is to fight the hardest battle you are ever going to fight.

Right… The Last Fighter a-k-a The Future ……
Hi… Yya better know…

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR