LYRIC

Yeah…..
Yeaaaaaaah…..
Yeah…. !

{Verse 1}
Kèneu warouma beug
Mane ci sama bopp xawma louma beug (mane xawma louma beug)
Kèneu warouma beug
Bi gni ndieuk dadjé bobou wakhou mala deug (bobou wakhou mala deug)
Kèneu warouma djégué
Kouma xam di nga tiéné fi nga tiéné (di nga tiéné fi nga tiéné)
Mane kèneu warouma djégué
Sodone sama xarite sama bopp lalay ndieuk téré (sama bopp lalay ndieuk téré)

{Refrain}
Boul meusseu gueum samay textos
Boul meusseu nangou niou weeto
Mane douma fay damay lep daw
Ndakh damay play Nnintendo
Boul meusseu gueum samay textos
Boul meusseu nangou niou weeto ooOoo
Doumala diokh li ngay weur boulma waulou ndakh wakhouma loudoul ay lebbone
Mane Saï Saï laaaa
Ma gueuneu yëss Al-Qaïda
Saï Saï laaaa
Moytouma moytouma éh
Xamal ni Saï Saï laaaa
Ma gueuneu méti Al-Qaïda
Saï Saï laaaa
Moytouma moytouma éh

{Verse 2}
Yaw boulma wakh lo soma tidjiilé sa noppeuh nala doflo (Da nga doff)
Doumako tay soumay nobb lo, Soma tidjiilé di nga off-do (Yeah)
Damay daw somay wane love ndakh beugouma kouma beug dima topoto (Ey)
Boul eS yégué No love somay khaar onshore ma ngi offshore (Ey)

{Refrain}
Boul meusseu gueum samay textos
Boul meusseu nangou niou weeto
Mane douma fay damay lep daw
Ndakh damay play Nnintendo
Boul meusseu gueum samay textos
Boul meusseu nangou niou weeto ooOoo
Doumala diokh li ngay weur boulma waulou ndakh wakhouma loudoul ay lebbone
Mane Saï Saï laaaa
Ma gueuneu yëss Al-Qaïda
Saï Saï laaaa
Moytouma moytouma éh
Xamal ni Saï Saï laaaa
Ma gueuneu méti Al-Qaïda
Saï Saï laaaa
Moytouma moytouma éh

{Verse 3}
Yeah Yeah !
Neex lamign bad man, Xol bi dagn tchi warone collé Stop sign (Panneau Stop)
Niata lafi digone dékhou baaneex, Tchi guédjou rongogne dh lagn moudjé lapp ganyin
Dama leudj dama dioubeudi (dioubeudi) Shawty nala teudj ci say souvenirs
Au début da ngay bëg fokné douma niit, tèy bo sanione doma freq. doma meusseu miin
Yagg na di wakh tchi goor yiy fowé xollou guel
Tané wouma kone mounou meu teuyé rôlou frère
Science-sal kép kou tass yakaar tégou yonou jail
Do dégueuti kène né leu “Doundeul bo tchi tolleu wé” (tolleu wé)
“Doundeul bo tchi tolleu wé” (tolleu wé)”

{Outro}
Saï Saï laaaa (Saï Saï laaaa )
Al-Qaïdaaaaa (Al-Qaïda)
Saï Saï laaaa (Saï Saï laaaa )
Al-Qaïdaaaaa (Al-Qaïda)
Saï Saï laaaa (Saï Saï laaaa )
Al-Qaïdaaaaa (Al-Qaïda)
Saï Saï laaaa (Saï Saï laaaa )
Al-Qaïdaaaaa (Al-Qaïda)

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR