LYRIC

{Arafat part}
Han ! Hana Yeah man sama choice day am feeling
thi thiatou karaw bathi wewou
tank dafay clean
yeah man sama choice day like
shoping
di shine like diamon di tak bling
bling
yeaah man sama choice ni adja mana
Day pote thi cote ba bo degue adja maana
day bari faim melni djinakh
bari pah
day wakh thia famou djote danane mik dou bari wakh
sama choice fans vivi la legui day
monte hanche
day nekhal boubs ni lissa firangue
kay bi declanche
nooo man beugouma choice bouy
ladj kouy feug
daf may def ndanane pa pare sakh thi dima beug
des foi sama choice di barde thi
djabou waly
dima ndiablou thi pinw ak baa mai doumako lali
man sama choice des foi gnou tek
mak mom duel
comme qui veut gagner des
millions day done intellectuel

{Refrain}
yeah man sama choice day pop
sama choice day top
day bari caprice tofamyi bari ay sope
dafay sweet dafay fresh super
weezy lay nop
di def priz tof thi net bi salut bitch
lay drop
Yeah man sama choice day pray
matin ba guewe
day am yar degual ma tekthi
feminewe
beug na am choice bouy gnew
degal ma mama
diko tek thi ham ham mbeuguelam nek kirama gooooooo

{RIDIAL part}
noo man sama choice ni sarata
day simple am foula thip thip al
baraka
man sama choice dou hol ndah
faram amoul
tam di tok thi podjou ndayam ba
deg ndiaram lamboul
nam na darra
roy thi mame diarra
djikom ni yaram
ba lo beug thi mom mou ngarra
day beug bopam
yonet la sopam
di fonk jobam
loko wah mou dess thi nopam
man sam choice thi melo la ak djiko
bo beugue am fi place linga yegal
adjiko
no man beugouma choice bouy
diay maline sou toye
day melni linguere brave melni
aline sitoë
man sama choice day roy zeyda
mariama
tek thi gueum yalla djeul yar ak
teguine df kirama
nam na djeguou pousso djeum
tenadj tourel
sokhlawoul copier gaga am na
beaute naturel

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR