LYRIC

Morééé Doundou Guiss Mane la waay moréé
Umh Umh ! Check

{Verse}
28, 29 Wathieu 16 ak 17 ans
Kouko am tou tokk cii chaiseum di sétane
Baa gni di dem gnéé ngui tek zeum di raye temps
Nieulé nio ngui cii baak prek djam délinquance
Jeunesse loloko formé
Fatéwouma gni yéwo jail Reubeuss, ba Forbé
Sama Jeunesse dagno waulou sen bopp
Done ay mindef yu meune def li beuri sen bopp
Gni baayi jangue wouti job nimou beuré
Liko raw ngui Football mba simékou Beuré
Gni Music, gné Mannequinat ak Féthieu
Soumala néé dou job kone ma nek Naafeek
Big Up wa Cité (Université) wa collège ak wa Lycée
Town, Banlieu, Thug wala Wally Seck
Sama Jeunesse bokoy imaginé
Sa Mind men di nga guiss images youné
Amena Jeune youy doundou Costume Cravate Bureau
Ci entreprise Ba état ba am grade bi raw
Sen morom yi téglé Diplôme yi di woute liguèye
Gni cii dess fess boppeuh kogne yi di khaar liguèye

…..

{Verse 2}
Nioune dagnou sonou beug solou ak xaandj
Ci bénène monde lagnou tok, deukou love ak Happy
House Party, Beach Party, SWAGG, Yakk xaliss
Blackberry, Iphone, Ipad, Galaxy ay jeune yu sen xel dal
Yendou Facebook dooranté texto ba fadjar
Diamono S’Cool lonkonté yu yu todj Sénégal
Jangou niou pour xam dagni sett nouniou féxé diaaleu
Classe par Classe triché mba yénène péxé daal
Téganté xell direunté mbagueu wéréinté Média
Djiguène yu beug xaliss, ba founiou ko séén daw
Lidieunti lougnou lekk sen farr yi ba taylé sen ndawe
Boy you tameu def-tate (ivre), di doundou bandi def kat
Mbède né sen Staff def lèn ay ngaandi Stars
Motah Guiss nga Boy yi agressé mère ak guel yi thiagatou bikk
Boy yi ndieukeunté jail ak guel yi ndieukeunté biir
Boy yi sathie sen père ndax guélou appartement
Guel yi biir bagna nek mère déffi avortement
No ! Jeune yu doff eupeunté sheytané
Mais boy xeuyyeu tané djiguène néggu seuyyeu tané

…..

{Verse 3}
Xaam nga dagno reuy ci sunuy rêves
Boo néké ndaw dou niak nga saurou louné
Boul guiss rek dafa gnaaw nougni doundé
Oubile saye beute té diémeu xam lougni goungué
Pour dëkou doundou bii fii néé té bone
Reuthiou molaye dapp cii cii saa yone
Jeunesse bou yémé, Jeunesse bou aliénée
Sama Jeunesse, Sama Jeunesse

Song bi yèn lako jaglél
Xam ngène né yone bi ngène taneu bakhoul kone djaadeu lène
Boy yek guel yu beuri ay jaague laagneu
Réw méé lathie lou yombe gentlemen jangui lène

….

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR