LYRIC

{Intro}
Paré lène tay paréna
Okay okay I know
Paré lène tay paréna
Okay okay I know

{Ara}
Fou bi néna “Doffatoul té dou délou Fann”
Patin né moukeu dou ba gèn té kène douko téré naan ay Douliprane
Paré lène
Paréna
Maay djiné biy Tafou biir Colobane
Dou Gris Gris djat ak thioumboukaay
Boudone lola Gouy Gui rékay meuneu daan
Grand yi né dama wowlé
Meuneu Rap ték tchi niémé raakk
Ragalouma yénou Thiow limay xambeu tay leu gueuneu taakk
Tay la gueneu tay la gueuneu taakk
Dina méti takhoul beute yi taaa
Yeené meu déh ma lekk sa naaka
Té meuna beuré guèneu tchi di bakkou
Wakh ko né Toubab bé bagn né dou djongg
Nit kou nioul bagne né dou djang
kouné ak sa natou bi
Ana louy njarignou koom Boudé dou guèneu tchi banque
Xaliss day wallou nit wanema lane nga gueuneu fonkeu
Louis V, Gucci nga am ma tassaaré Logo bi
Logo bi teug sa monde
Aara la toudou ma Baye Sen mais wowéma wowéma Sen Pa
Armée bi marqué neu sen Pas
Ngor diga Dup wala Demba
Sa Rappeur bi meunoul na baayi
Néko na baayi mo ngi beuneu tympa
Sa guel bi né Ara da sympa
Beugone meu nopp ko no mais même pas
Dama pédaler laisser deux légui meune na pas de danse yi rek faté na Gwéta

{Refrain}
Niémé ko
Brickest Attentat
Wané ko Top 5 Bantamba
Mbour Dk Kaolack Brickest ba Tamba
Sissou neu Siss tay niggaz bi nangouna

Paré lène tay paréna
Okay okay I know
Paré lène tay paréna
Okay okay I know

{Dayza}
Caissou beat bi bamou dallé nieup lathié Dayza fane la né
Caissou Etat dik leu ma mallette do meusseu lathié fane la palais né
Wessu nala dama paré mane la mise à jour bi, dougueul sa paramètre
Rap Galsen bou mélone ni charette ma tokk tchi kanam niouné dafa kanamé
Nigga mane kaw kaw la
Bo beugué niou def comme d’hab
Dama yoré buzzou classico niom niouléni thiow comme laakh
Pincez tous vos Kora c’est moi le chef chorale Ara la Dayza la
Hubert Pepper Léopold Sédar
Raw nala douma sa masse
xalé bou matagoul moss wodaateko
Clip bi kharou tchi trace
Millions de vues yi tchi poche nodaatko
Public bi Rap lama sass
Logo bi solko ni boss nieup d’accord
Sa son yi di faux raccords
Dayza la meussouma teulé ma beug beug def mouy teu
Fittou Gaïndé la dou tiit
Daa yombeu ma melni kou tchi fo
SSa nigga bi amoul xalima
Plume bi la faté tchi ndélou Titeuf
Yagg nu méti ma mougnko
Piégé nagn niou ma ndiouyko
Gni beug souki laafou picc bi nélène picc ba ngi tchi logo Twitter

{Refrain}
Niémé ko
Brickest Attentat
Wané ko Top 5 Bantamba
Mbour Dk Kaolack Brickest ba Tamba
Sissou neu Siss tay niggaz bi nangouna

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR