LYRIC

{Mao}
Yaye dama beugeu tekii
Tekii nii sama morom yii
Yoboulen makka yaw ak baye
Téral leen ba beuss biingenii saye
Dama beugeu tékii Tekii nii sama morom yii
Ngene diima ndamo dima tiitaroo
Nane khalebii mo am diiom
Comme nii ngene mel ak Aladjii
Khamna neii mo nek sii sen khol yii
Loumou wakh nonouleu loumou def nonouleu
Sou done manela ngene nema diogal fii
Awma thieur awma respect si keurguii
Loufi réér niounii mane la mane mafii bandii
Mougn na ba soneuh manguii beugeu khadii
Khana ma df nii sana gayii sobou gal yii

{Refraiin}
Natou guii ma yenou ni, Diss na sama bopp bek sama mbagg yii Biilahi wooy Wallahi
Houuu natouguii ma yenou nii tiiss na sama khol ak sama diiom djii Bilahi wooy Wallahi

{Books}
Mame dama beugeu tekii
Ganaw Yalla yaw ya khame louy sama metiite
Mane khawma ndeye ak baye ndakh yama yar sii keurguii
Limay khalat si yaw khaliss dou takh ma tebii
Mame dama beugeu tekii def la gouneii yobou founei ngamay weteulii
Mane khawma kene koudoul iioe diafenga sepii
Nianal sa seutt mou diekou teki raw sii khetbii
Comme ningene melak Oumii Kouyate rewal ko bou khate mem bou tognei Pathé
Loumou wakh nonoula loumou def nonoulaa louko ndekh mou sol soumii moy tiatou keurguii
Limay khalatt si ioe wessouna makk mame doundeul
Limay khalatt keur ak auto am tiabi mame dougeul
Djiguenne diou matt Goor ngaa mane mafi geune mame doundeul
Diokhlene ma lep ma yenou diokh ko sama mame doundeul

{Refraiin}
Natou guii ma yenou ni, Diss na sama bopp bek sama mbagg yii Biilahi wooy Wallahi
Houuu natouguii ma yenou nii tiiss na sama khol ak sama diiom djii Bilahi wooy Wallahi

{Mao}
Wooy yagam yooo metiina lool soma khamoul ngalla boulma reii
Soma khamoul ngalla boulma jugeii
Beuss bou Yalla sakeu sama khol day geuneu taakeu
Ndem goor momoul dioy damay diiema takeu
Sama fiit beuss sama khol neii tékeu

{Refraiin}
Natou guii ma yenou ni, Diss na sama bopp bek sama mbagg yii Biilahi wooy Wallahi
Houuu natouguii ma yenou nii tiiss na sama khol ak sama diiom djii Bilahi wooy Wallahi

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR