LYRIC

Verse 1: Fla The Ripper

Kou Yalla arr loy doyee kharfafoufa/

Lo meun deff Téy loy kharr souba/

Weurseuk linga mom djaroul khékh, kheureum doomou Adama /

Kheuthio tour, Alal, daradja /

Djaroul lou niaw ba rouss alakhira /

Lo meunti am day djekh adouna /

Dou mbokk day worr topko mou Sankla nankla kham Foy tekk sa tankla, djang la /

Fi ma djar ba yéksi fi Lepp lima deff Lepp thiant/

Moytoul la Lorr si mane motakh ma ndieuk djokk nieuw sammla/

Wakh douniou kham Kou djitee leral yaw warnala/

Nitt soppla toppla sassnala yennala /
Wakh dji dou Guiss Guiss djeundioula doundounla /
Wakhkatt dééna si koumpa nga/

Lou djiiba djekhoul djogouffa/khopp nga Ngalaw djokk nieuw yoobouwla /

weerouway bakhna wala meukh souf yomb la! Gatieel mbokk ya/

outt lou bakh barkel sone tiaa, pass pass Yokk thia /khacci bokkou thia/

Tiono dou Reer Borom deugg la/Kenn dou Bégn sa doom beug la/

Diam foullak feyda dokh farata/

Moudj degg baraka, Dieuffnako Yeene bi aksina /

AL khamdoulilah
Yeah alkhamdoulilah !

Verse 2
Yeah ! Rakk danga wara begn djoy/

Demal nga djoylo gni la begn/

Yama eupp doole mala dakh dooree

handicap bi gueuna makk moy fokne God si nienen gni la farr/

Woornama mane !
Wornama mane!

Bo djoggoul khekhal sa bopp deff linga teulee deug kenn doula djeule si keurou niggah
“DINA BAKH”
Kepp kounekk ak liguey bignou la sass/

Te yalla Dou labali sa fass/

Gni tayle nalaw djay sen pijama ,

Gni deff sen rongone si lignouy tabakh/

Gni Doundou khiff ak marr fii ba france/

Qu’est qui ce passe?

Ba ngay djay sa ngor ndakh khepp linga Am/

Yalla bind Tee yemalewoul dafekk kounekk sa dound ,kounekk caisse binga khadj/

Syrop bi Meunga si deff ndokh dong/

Niankatang deff si SOW ngen thiopp/

Yagg na tokk beut taa, rongogne di tokh sama dal batta/

Daal you feukh footballer na balle beutt ak tank bi you moudj youkhoulo adouna weurngal Kepp teey/

Teyla kagn “BisNikki Tey” sant yalla.
Respect!

Refrain :

Tey nga Am Souba mou tiool/

Yalla rekay bour ,Nitt Dou loulou sool/

Boul kham Lou nek sen kholl/

Sant rekk woor boul saaganee sa ngor ( 2x )

 

Added by

Ahmed

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR