LYRIC

{Verse 1}
Souniou Sénégal la naniou ko job téi bok bène waar
Khathiando seug dorondo mouy gueuneu taar
Fi bène pote la da ngay naane diokh sa morom naane
Li bène lale la nioko bokk teudeul ni fanaane
Macky Sall warna toudé dom Abdoulaye
Domou Abdou Diouf toudé dom Karim waay
Balla Gaye ak Modou Lô bokk ndèyak baay
Youssou Ndour andak Thione Seck songou Bercy try
YAGG BAWOUL DARA DEUGUEUNTAAN ci samay Sound
Djily Bagdad Baay Ndiagn délou UNDERGROUND
Djappal ma djapp waay Sénégal deukeu bou ndaw la waay
Baay fi koula wo ci AYY wouyouko té niaane ko JAAM waay

{Bouba Kirikou -Refrain}
Hi youya Hi yaayé Sénégal djouk djotna
Hi youya Hi yaayé Sénégal djouk djotna
Hi youya Hi yaayé Sénégal djouk djotna
Hi youya Hi yaayé Sénégal djouk djotna

{Verse 2}
Na CARAPIDE yi waagni sen VITESSE ci TALLY bi
sauraalé xalé yi boukhanté bi amoul alibi
Fi Jaameuh rek mo fi am Barké BAMBA NOUROU TALL
BAYE LAYE, BAYE NIASS, ALADJI MALICK, BOU KOUNTA, IBRA FALL
VIVI, COUMBA GAWLO, TITI bokk bène sound
way ci DEESSE. QUEEN BIZ, GUI-GUI mou leumbé sunu town (sunu town)
SELBE NDOM di guiss lepp fu kène doul sétté té
FATA dieuliwaat Gougou dékilaate souniou CBV
WALLY SECK, PAPE DIOUF tekk bokk bène Mouvement
Andeu dimbeuli Talibé yi ci tally bi reew mi gueuneu move haan
Da Brains remix na xol yi nice Tapha coatché lène
Daara J délou djeuli Alaadji Man bou rabboul coatché leen

{Bouba Kirikou -Refrain}
Hi youya Hi yaayé Sénégal djouk djotna
Hi youya Hi yaayé Sénégal djouk djotna
Hi youya Hi yaayé Sénégal djouk djotna
Hi youya Hi yaayé Sénégal djouk djotna

{Bakhaw}
Ngaaka Blindé woténa yeufou makk jaam waay
Nagn ko degg lou xalé la takhaw na guiss na waay
Nio ngi deuk Capsi mom mou deukk Guédiawaay
Pikine Parcelles Ouest Foire nio bokk ndèyak Baye
Omzo Dollar Buzzlab mbollo,
DIP AKHLOU BRICK NGAAKA BLINDE warouniou xouloo
NITDOFF – CANABASSE Alassane DJIGO
Def SHOW OF THE BUZZ toudé ko AWADI ak SIMON
IRAN NDAO ak KHALIFA NIASS deff conférence
MACKY SALL guéné KHALIFA SALL andak mom Vacances
Djappal ma djapp waay Sénégal deukeu bou ndaw la waay
Baay fi koula wo ci AYY wouyouko té niaane ko JAAM waay

{Bouba Kirikou -Refrain}
Hi youya Hi yaayé Sénégal djouk djotna
Hi youya Hi yaayé Sénégal djouk djotna
Hi youya Hi yaayé Sénégal djouk djotna
Hi youya Hi yaayé Sénégal djouk djotna

{Bouba Kirikou}
Bo guissé nit kou soxla boko yoré diokh koko yow (Sénégal moy gagné)
Boul baayi nit ki reer, bo xamé yone bi wane koko yow (Sénégal moy gagné)
Yaatou, yar ak téguine diémeu roy ci sama Maame
Djougal waar té woute boul tokk di niakhtou soone naa
Baalou nala akk boudé wakh bi nékhoula
Sunu Gaal sou dieumé kanam lolou sunu ndam la nangou naa
Bo guissé nit kou soxla boko yoré diokh koko yow (Sénégal moy gagné)
Boul baayi nit ki reer, bo xamé yone bi wane koko yow (Sénégal moy gagné)

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR