LYRIC

{Intro}
Yallah meuneu mayé
Yallah meuneu mayé
Amena nit you sokhor Nénagne “Gnoy nangou lou Yallah mayé”
Niognou Borom bi lagn niémé, Borom bi lagn niémé
Niou ngi lékanté sen biir té amoul deumeu bou nekh dérett
Dama am travail de Maman
Doma guiss ci Tata
Dama am travail de Maman
Douma fils à papa
Dama am travail de Maman
Nieupeu am ay noone ci life bi
“Yonou jaameuh soriwoul” kone tant que amo nioulay guerre soriwo ci life bi
A beuzé

{Refrain}
Nit yéé sokhor tellement sokhor
Beaucoup sokhor trop trop sokhor
Pourquoi sokhor ?
Gueune lène sokhor
Yeeré you sokhor
Guel bou sokhor
Auto bou sokhor
Keur bou sokhor

Bakh mo diekh
Bakh mo diekh
Bakh mo diekh
Bakh mo diekh
Fokk nga sokhor (x2)

{Verse 1}
Deumeu sur deumeu
Nieuw na fekk fi ay deumeu sur deumeu
Kou bakh sou niaawé djikaum neubeuna djeumam
Gni mom niit yi sèni deuneu mo leundeum (Leundeumeu leundeum)
Deumeu sur deumeu
Guiss-Guissou fène kat moy gueumal nga gueum
Fresh lay def sole jacket summer wou leumbeu (= Tout l’été)
Sa periode nieuweugoul ni feum (meuf) bou eumbeuh
Boul deuk ci lidieunti kénène
Sama adresse moy fénène
Di nga wathie liguèy parce que job-bo
Bou féké may sa thiono masta thiono
Sama sétou dafa tothie ma dém dieundeu télé pour guiss sama bopp
Bayina none yi di tathiou do dégue bène yoo founiouy tathio
Nioune nékouniou ci yoyou (nékouniou ci yoyou)
Xarito ak ay rappeurs non non nékouniou ci yoyou (nékouniou ci yoyou)
Cissou bi nékouniou ci yoyou (Nigga)
Ma ngi séni kanam say youmay reculé
Beuri classe té meussouma redoublé
Boudé sa rap fayoula ndieugou auto fuck you ak message yi ngay véhiculé
Nigga

Nit yéé sokhor tellement sokhor
Beaucoup sokhor trop trop sokhor
Pourquoi sokhor ?
Gueune lène sokhor
Yeeré you sokhor
Guel bou sokhor
Auto bou sokhor
Keur bou sokhor

Bakh mo diekh
Bakh mo diekh
Bakh mo diekh
Bakh mo diekh
Fokk nga sokhor (x2)

{Verse 2}
Kène momoul Yallah, Yallah moniou mom mais kène momoul Yallah
Mom moy taaneu kouko nekh rek mou taal leu
Lolou soula mété nianal mou baal la
Nianal mou baal la
Ndiampé niakh desna eau de javel ngay bolék ndiampé niakh desna
Def sa xol ci paane nga bombou mou bessaate
Def sa xol ci paane yeah Bombala bombeu
Aduna dafa goudou tankeu déh toungouné
Légende biir Cap-Si (Sicap) ni Thioukoulé
Takk sama fit heureux ménage
Takk sama fit heureux ménage
Daane na xékh di tothie ay verre
Ba am ay bleu bi ngay tass ay bleu pour dieundeu verr (Lunettes)
Ak bic bleu lay bindé vers you fresh ni jeux d’hiver
Amna xaliss balaa billet bleu di vert

Clash meun nala défal pub beus bo dadjék mane boul sakh négocié
Am rappeurs yuma fi solal jupe té Wallaahi Bil-Laahi douniou ay écossais
Hater wakhma yaw loumala amél
Autographe ci seu khol ak sa bamel
Xamna yi ngama yagg nianal waayé ma ngi taakeu nieup guiss ni phare des mamelles
Nékouniou ci yoyou
Nékouniou ci yoyou

Rap ay att thiolé ci life bi nékouniou ci yoyou (nékouniou ci yoyou)
Ignaane bi nékouniou ci yoyou
Nigga Ma ngi séni kanam say youmay reculé
Beuri classe té meussouma redoublé
Boudé sa rap fayoula ndieugou auto fuck you ak message yi ngay véhiculé
Nigga

{Refrain}
Nit yéé sokhor tellement sokhor
Beaucoup sokhor trop trop sokhor
Pourquoi sokhor ?
Gueune lène sokhor
Yeeré you sokhor
Guel bou sokhor
Auto bou sokhor
Keur bou sokhor

Bakh mo diekh
Bakh mo diekh
Bakh mo diekh
Bakh mo diekh
Fokk nga sokhor (x2)

{Outro}
Yallah meuneu mayé
Yallah meuneu mayé
Amena nit you sokhor Nénagne “Gnoy nangou lou Yallah mayé”
Niognou Borom bi lagn niémé, Borom bi lagn niémé
Niou ngi lékanté sen biir té amoul deumeu bou nekh dérett
Dama am travail de Maman
Doma guiss ci Tata
Dama am travail de Maman
Douma fils à papa
Dama am travail de Maman
Nieupeu am ay noone ci life bi
“Yonou jaameuh soriwoul” kone tant que amo nioulay guerre soriwo ci life bi
A beuzé

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR