LYRIC

{Intro}
Ada is back again dafa beuri thiass
Niémé feuleu fouka kène fogué woul (ADA)
Dou bopp nénn niémé nathie bou tangue kouko saurou fa ngène dieum da soriwoul (ADA)
Dou capitaine beu ci Equipe-beum Menuisier leuffa té banwam bi parégoul
ADA moy SYPERMAN sen biir
Aythia kone soukeulène sen buur
Khara beu Album mou K-Nibal guèneu niou wane lène né taameuh naniou dérett Kou fippou niou kharraf
Après Maxi Mixtape Adjati level bi Incontournable né Thiarakh
Topondo wal nima mél atanoulo lima done seu ndigueuh né karathie
Djougué fu souffé di yekk gueinteu nga lima guiss yakk sa toubeuy parathie
Sa Mara bi tek nala deal
Yeukeutil sa yëré public bi feel ko my nigga
Sama Rap bi def nala kill
Lyrics, Skillz kène douko toule my nigga
Nako nieup yegg damay Politique kou yabo nama wowé Mamadou DIA
Ba ci soukouraate douma soukou raam kène yéyo ma deupeul ko sama Djeu

{….)

Dépasséna Music ma ngi ci RAP
Melni da ngay def sport mane may Karaté
Philosophie leu sa mind di ci claté
Lathiema ma wakh la xamo fimay xalaaté
Sa bindide bi oyoff bi wara reuss
Lou guèneu ngène essayer beug Buzz
Légui publique bi bouton leu nala beuss
Tempo bi changé Ta-ta-ta-tareusss
Kou sania takhaw né meunouma bindeu awouma Inspiration dafay pathial forokh
Xaral ma gaaw ….ndaxté degg nga lakk bi my nigga Gassara mara
Défati thieup ci kaw scène bi niou naane dafay naane sangara
Révolutionné ni nga wara posé seu flow wowé lène meu sèn Mame Sankara
Waro lène wakhaalé Musik bi sound bobou warna diar lou eupeu 400frs

{Outro}
Waw xana 400 diaroul wakhaalé nak hééhéééhééé

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR