LYRIC

Dégouma dara man
éééééh mane la waaay
Doundou Guiss

{Verse 1}
Tay mou melni taaniberr bou policier di tass
Kagne ngay démaate saani kherr bountou keur président
Dama lène fay ma nékeu domou Double Less bi daane
Israël ak Palestine beugouma né ci jaameuh
Dama lèni umh ! fi thiouné yéfi né
MEF néna DIP moy MESSI non il joue très bien
Bama dalé bindeu matoul diouraum bènn att
Té all school yifi nék kène meunoul def ni mane
Amena niouy guéné Albums nénagne mane lagne cii Clash
Coupes yé ngui sama néggou Mère niom meussouniou dem Finale
Samay Ennemis nioy coach yu gueuneu efficace
Samay noone nioy samay coach yu gueuneu efficace
Meussouniou yélwaane té douniou tégui tankeu
Ma ngui cii Minou Casamance yi dofouma bay tégui tankeu
Gars yi beugone ma xéw nio beugaate ma xéwiwaate
Né lène lima dessé cii Hit matena 180 giga

{Refrain}
Nigga malène meune té dina lène soule par force Tar mbéth
Nigga malène meune té dina lène soule par force mane rek
Nigga malène meune té dina lène soule par force Tar mbéth
Nigga malène meune té dina lène soule par force mane rek

{Verse 2}
Parce que maalène meune té xawouma sakh loma meuneul
Do Yallah do Yoneinti do sakh 1 million de Dollar
Da nga beug fayékou nala fa diokh li ngafa am
Beus di nga beug rombe sama kogne mou teuh leu
Bro diafé wouma guiss li diafé moy ngamay guiss ak niom
Bo amé diom naane ngay amé djotou ki am djott
Annoncé gouma sakh nieupeu ngui lathie sama Album
“DIP Album bi kagne lay guéneu” melni Album bé ngui Kasso
Niari song cii bène beat no fils do def lou melni
Niari song sakh ci niari semaine fils do def lou melni
Doxna Kilomètre yagg xiff té do dem léki
Ak Rythme bima dieul ni pour done millionnaire dou méti
Maa ngék diplômes yeup légui ak pistolet pour ray niit
Kone douma yénou khew parce que niou ak yène dou derby
Broda boulma lathie louy Morééé dioxma micro rek pour sama frigo fess
MCs yifi né la beug rek niom nieup niou xamné
Maalène meune

{Refrain}
Té dina lène soule par force Tar mbéth
Nigga malène meune té dina lène soule par force mane rek
Nigga malène meune té dina lène soule par force Tar mbéth
Nigga malène meune té dina lène soule par force mane rek

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR