LYRIC

Yow bimay ndieuk guiss sama clip Télé dou wone dara cii mane
Khawuma wone ma ngui wone cii REVOLUTION ni SARAFINA
Bo néké kaaw kèn dou djapp ya ngui rap-bati sakhYo MIC bi nice hann?

Annh ! Yow bimay ndieuk dégue sama baate Radio dou wone dara cii mane
Khawuma wone ma ngui wone cii REVOLUTION ni SARAFINA
Bo deuké town dagnelay gueumelo do dara cii RAP
Tégone gnou boy yiy beug dadjalé ay thiaga di naaw
Kène momoul kèn, kène eupeuléwoul kène dara cii lèneu
Boukène xepp kène gueum gueum rek ak waar-ra fi néé
Xamena ay Galsen yu meussoul dougou Carrapid sakh
Diaxlé nga khaat, diapalni ma ngui dogga tambalé nak
Rappeur yu diougué bitim réw douma sèn morom
Gueunouma doundou warr nagn xamni culture bi amoul borom
Dou Kana bi wala Kawmane bi bégnou cii eupeulé waaleu
Dou Canabiz, dou Coc virus leu boy yi accro diko waaléé
Hann ! Ram soga takhaw jog soga dox (soga dox)
Mané rammal soga takhaw amoul loma wakh
Meuno loudoul commenté dignou critiqué Baay
Mais kène doufi deffati ni fii FREE diké Baaaay
Dama télou cii RAP, doga tégou di RAP
Lima déguelou cii RAP. Est-ce que déguelou nga ka?
Mane dama Free sama Mind comme ay fékheul relax
Ancien talibé maggue dagnema Cheikhal cii RAP
Ngané dolé ngay tek umh !
Dagne niou bolé woul rek
Nioune leu Rakk yilay rousslo cii saye kanamou Rakk
Malay indile bagageou makk ngamay diox saye sagarou RAP
Ngané tangou gnou ha-ha ! da nga xamagoul RAP
Dadjalé KORA, BALAFON ak XALAMOU RAP
Fokma feug leu ay balafon nga khala ngou raam
Mane damako beug nopp ko té yaw dafla diaraloul sarre
Umh ! Souma nékone Shaw maay done diabarou RAP
What? Na sa gars yi dém dallou waat rène maay fallouwaat
Baalou akk TABASKI rombe rek ma Allouwaat
Dieul lène sen ALOUWé délou déguelou waat boubah
Poète yima meune djangal meune nalène wagni (compter) meune nako waaat
Waw mane mane mafi djaay poète
Waw mane mane mafi fly kawé la def
Léopold Seghor (Aéroport) day xatt pour meu atterir
Sétanena sa clip mais à vrai dire euuuh c’est pas terrible
J’arrive pas à tenir Bullshit bi beurina
Bala lou bakh di am rek fokma diogué ba PARIS quoi
Kène cii gars yi amoul histoire vous avez merdé grave
Motah Concert rou samedi soir di mèlni Mardi Gras
Ma dakk créé ma takh nga toppando
Meune nga topp sama Bande xeuyna niou wane la yone
Nieuweul sa life L’Eau ba ngui waaliyaane
Nel gnam Wally ak Titi bisness bi jaamla
2PAC dou djoték Big D bou nékone affaire de lamb leu (dédéttt)
Bou nékone dolé kone Balla Gaye nieuw cii game bi
Toudou sa tuur ni Kendrick kèn dou tidji sa guémigne
Music ba ngui faye gni cii gueuneu mouss
Comme d’hab. gni nék cii souf dinagne yagg xouss
Té combat dou diekh filék gni gui gueune pouss
Contrat yu bakh yi pour nga am tchi fow nga magg couz
Boula mbède bi naw sa wa galé méré laa
Boudé cii yaw RAP wéteuli chomage laa wéré nga
Euleuk mbède bi daw sa wa galé bégué leu
MC bouy topoto wa galem mbede bi respecté laa
Détestéma sa droit laa, boulma diémeu testé
Boudé cii passé nga dess dé, fi lalay bayi né mess dé
Ma ngui niii dii RAP ba beat bi yégue 3min pile
Nga xam né limoma yokk mais dou diékhal samay pile

Ma ngui cii yone gni beug peace nagnema bayi di togne (Nagnema bayi di togne)
Kay tek cii brik ndakh gnou tabakh tchi kow
Tchi kow tabakh tchi kow
Gni beug peace nagnema bayi di togne (Nagnema bayi di togne)
Kay tek cii brik ndakh gnou tabakh tchi kow
Tchi kow tabakh tchi kow
Tchi kow tchi kow tchi kow
Tchi kow tchi kow tchi kow
Tchi kow tchi kow tchi kow

Goor Yallah meunoma titeul
Bi nga dégué ma door nga soga na ngou Peace UP
Té pour sa yone lerr Homy wane nala niiteul
Yégue na li ngay saure waayé meunoma disturb

Goor Yallah meunoma titeul
Bi nga dégué ma door nga soga na ngou Peace UP
Té pour sa yone lerr Homy wane nala niiteul
Yégue na li ngay saure waayé meunoma disturb

Ma ngui cii yone gni beug peace nagnema bayi di togne (Nagnema bayi di togne)
Kay tek cii brik ndakh gnou tabakh tchi kow
Tchi kow tabakh tchi kow
Gni beug peace nagnema bayi di togne (Nagnema bayi di togne)
Kay tek cii brik ndakh gnou tabakh tchi kow
Tchi kow tabakh tchi kow
Tchi kow tchi kow tchi kow
Tchi kow tchi kow tchi kow
Tchi kow tchi kow tchi kow

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR