LYRIC

{Mamy Victory}
Excuse moi haaaaan
Ma bagn
Non never éh boy téguil fi sa loxo
Eh Téguil téguil mane Week end dou takh may lokhol
Never mane makay wokkeu saay bouy xassane
Maay ki raathieu seu biir gueew soumay teuleu nga lale bassangue
Ya ngi weur VICTORY tchi game bi té amo NIX
FLOW di GLISSÉ sar tchi BIIR ni kou diwo MANIX
Na KO-DALL ngamay FEEL do am tchi mane nix
Takh saay bo KHINÉ ma sopi sa ASSAMANE mou NISS
Toppeu meu ndank ndank, may def louy sank sank
Sa carrirère nieup naane meu djapp tchi mais maa lank lank
Dindi nafi gaak gaak tek naafi tank tank
Di savouré sama ndam li Malien ak dank dank
Boudé xamo sama name wowé meu Vicky Velli
Mane bène rek la tchi biir laydies ak li gni beuri
Amatouma loumay prouvé fuck lou nit di wakh
Kène douma dapp tchi rap deug leu motah faut que nit gni wakh

{Refrain}
Eh boy téguil fi sa loxo
Eh tégal fi sa loxo
Tégal fi sa loxo
Eh ! Tégal fi sa loxo

{Nix}
Shawty dama busy fokk nga understand
Notifications yu eup djizou compte banque
Sen buzz zeu dessé takkeu ni sen potou lamp
Sama yaram neexoul chérie fokk nga dampeu meu
Doma djaay neex té ya gueuneu yombe 1 + 1
Nieuw tek sa LAMIGNE tchi kaw BEAT bou TANGUE dieur
Loutah nga DEUR fayla sa SOXLA ba nga FEUR Biirou MBEUR
Fess delleu beuri dolé maay sen Balla Boy
Music bi douniou bolé
Boumay beureung séni mbollo
Ya ngi langaamou ni golo
Ya ngi may seen mais sanio meu laale
Game nga mais laalo balle
Yeah maay couleur locale
Nuulest mother fucker is àl (là)
Baby féthial damay flow di dessal
Non non douma réssal
Soula neekhé google sétal
N easy tek fi tankeu 90’s
Doyoul dokh ko ndank ndank
Beugue milles mou dall biz
Bou doyoul 2000 ndangam sangam ma ngui tégal
Fils Kone Tégal fi sa lokho
Vicky Velli dou sa morom nigga

{Refrain}
Tégal fi sa loxo
Tégal fi sa loxo
Té-Tégal fi sa loxo
Hééééy
Tégal fi sa loxo
Dafa lerr
Tégal fi sa loxo Hééy
Faut que nit gni wakh dh
Tégal fi sa loxo
Faut que nit gni wakh dh
Tégal fi sa loxo Hééy
Faut que nit gni wakh dh
Tégal fi sa loxo

Tégal fi sa loxo
Tégal fi sa loxo Hééy
Tégal fi sa loxo
Fi nga wokk fofo xassane
Kone Tégal fi sa loxo

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR