LYRIC

{Couplet 1}
Ba ma donei goné Fouki att la amone (ééh)
Khawma wone louy mbeuguel waayé khamona liy nékhal sama xol (bééé)
Saa sou takoussane diotone ma sangou solou xégn lou nekh
Khaarko tchi sama boppou kogne wakh ak mom rek tay mba déh
Ma sèneu ko rek mouy nieuw ma daw
Mane dé dama ko khoff
Mane dé dama ko love ba dof
Mane dé dama tchii

{Refrain}
Thia la thia la ling Thia lala thia lala ling
Mane dé dama tchi thia la thia la ling
Dama tchi thia lala thia lala ling
Mane dé mane dé dama si thia la thia la ling
Thia lala thia la ling
Mane dé dama si thia la thia la ling
Dama si thia lala thia la liing
Mane mi louma dal?

{Couplet 2}
Sama fiit bi di def boom boom melni kou daw Dakar-Saloum
Khawma loumay def ma waxtane tchek sam kharitt Moussa Loum
Kharitou djiguènou kogn bééh
Mounéma boy boul khof makoy règléééé
Moussa fixel gnou Rendez-vous 8h12. guinaw Keur dou
Ma aabeu chemise lidieuneti beuytou (Toubeuy)
8h moins 12 ma ngui fofou
Khar nako ba soneuh Mane mi tiampeuna ba déh
Khawma dafa am problème? annh ! Wala bokk dé dafma deh ?
Pour une fois, ma tak sama fiit dé
faç-yéné wakhko linek ci sama xol béé
Mou bayi ma si biir waayé douma xaddiii
Ndaxté xalé bi dama tchi

{Refrain}
Thia la thia la ling Thia lala thia lala ling
Mane dé dama tchi thia la thia la ling
Dama tchi thia lala thia lala ling
Mane dé mane dé dama si thia la thia la ling
Thia lala thia la ling
Mane dé dama si thia la thia la ling
Dama si thia lala thia la liing
Mane mi louma dal?

{Couplet 3}
Moussa moma togné ndakham limou ma ladione diokh nako
Néwone nama mokoy règlé
Souma ko diokhé samay fo-wou-kay
Da fa melni dafa diar sama kaw
Souma ko diapé nako…
Li mako diokhone nama délo wala ma yobou ko ardo
Wala ma yobou ko ardo

{Refrain}
Thia la thia la ling Thia lala thia lala ling
Thia la thia la ling dama tchi thia lala thia lala ling
Mane dé dama si thia la thia lala ling thia lala thia la ling
Mane dé dama si thia la thia lala ling thia lala thia la ling

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR