LYRIC

THIAK THIAK nigga
It’s ya boy Free Elzo, dama koy kill thiak thiak nigga
Han han

{Refrain}
Genrou beat yi dama koy kill thiak thiak nigga
Yeubo Teaula maleene gueuneu ndiathiaar nigga
Genrou hit yi dama koy kick thiak thiak nigga
Bo defoul lima def bouma diemeu nioddi thiaay thiaay nigga
Thiak thiak nigga thiak thiak nigga
Thiak thiak nigga thiak thiak nigga
Genrou beat yi dama koy kill tiak tiak nigga
Yeubo Teaula maleene gueuneu ndiathiaar nigga

{1er Couplet}
Daaw dope bi defe dal ok rene dina ko bathiaat nigga (néwone naala douma tandou)
Rappers yi nieuw bounte gallé dimeu madial nigga (sarakh sarakh)
Deukk tchi dima topando wayé légui ken doufi sathiaat nigga (kèn dou fi sathiaat)
Souma sourré bayil leen Mathiaat nigga (haha)

Mane music laay def loumay doyé ay fans ( amnaa ay melomind )
Ay chèquou chiffre ak S Ni kou yoré iPhone (dolla dolla bill)
Kaay niou Fesseul ay stade bouniou chauffer ay salles
Euppeulé flow Sarpant, île de Gorée ak Ngor
Non mais non mais maa meuneu binde
Maa meuneu kickeu
Ma teulleu kill nieup
Ma feulleu titeul rappeur yimeu djitou di yaakh souniou milieu
Ma meuneu disturb
Khole sama gauche niounéma impec
Ma khole sama droite guissouma ken mer
Guissouma ken begn
Degouma ken tek
Newougn ma hendek
Ndékété fen rek

They hate wayé kham nagn kouy sene bour
Youkhou “represent” khawma Fouy sene hood
Mboté bou fi beugg songg ci kouy dey doul
Ken douma téyé ni bébé bouy khègne poupe
Pousse leen wala niou soul leen couz
Boulène yengueul mak you tokk di cool sene cool
Chaque jour nguène lose te mounou leen mousse
Et puis né nguène danguène siwe? Euh louy sène tour?

Kène khamoulène diaroul ma koy laadiaat nigga
Yeubo Teaupla maalen gueuneu ndiathiaar nigga
Genrou beat yi dama koy kill thiak thiak nigga
Bo defoul lima def bouma diemeu nioddi thiaay thiaay nigga
Thiak thiak nigga
Thiak thiak nigga
Thiak thiak nigga
Ndakh maleen gueuneu ndiathiaar nigga
Genrou beat yi dama koy kill thiak thiak nigga
Bo yegoul fima yegg bouma diemeu nioddi thiaay thiaay nigga

Benn couplet doy neu”

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR