LYRIC

{Mao -Chorus}
Wax djou sew bii dafa beurii
Men I’m tired
daniou beug moutiou sama blood
ni vampaya ni vampaya
ni vampaya ni vampaya

{Verse 1}
Yeah !!! yaw!!!
Yallah taw alleu naaate ma fasse sama fite daldi sole dallou mak
Soldaru mbed yémeu faal di djow sama flack
Xaxta ndikou fire ngakoy feel cii bépeu track
Niouy soss di laay di féété wakh djou bone yi sama back
Téwoul maay gueuneu dii dém tchii ligni def malèn ko daak
Nigga meunoma freiné, Nanda go foumay brainé ( Brain )
Ay ndiounii at ak sama bosse yi limako trainé
Sa crew loumou tangue tangue dagn koy diérii mec
Dox sa biir périmetre, Toule sa 9mm
Bracké sa public diam lèn flow baniou firii……
niggaz yi tiow sen xoll moy ….
Kou ngène guémb ma dieul, kou ngène in’di ma ndéle
niggaz yi xew kouma cii sèneu dagay def thièle
Yaw yagui woté real ya gueuneu naafekk
Affaire de Luv mane ak yaw dotou niouko gawa sékk
BIAAAAAAAATCH

{Mao -Chorus}
Wax djou sew bii dafa beurii
Men I’m tired
daniou beug moutiou sama blood
ni vampaya ni vampaya
ni vampaya ni vampaya ( X2)

{Verse 2}
Yo Yo Yo!!!
Fi koumou nekh hainale, Nioune Yalla lagni kènale
King of Hip Hop bimou def tchi nioune meunoko nénale
Kharagne Lô La tchiii mic, Balla Gaye 2 cii show
Galagne ko baa to death, Mane laniou doylo tchii flow
Liniou mouraune lane mourriiii, Gnou khifone rek ma nourris
Faalou done bourrii bourr yi, Contenairou rimes maa yourrii
Let me give thanks
Hip Hop Galsen ma done tchii Légitime Gangsta
Never look back, Let them talk rék
Untouchable Killah moy dieuwrignou D-Squad
Maa nekk à la mode, Maneleu thug yi di nodeu
Nitdoff ciii sèni shirt, ba tchii seur yigni wodeu
Mbede maa diokh dolé, Maa athie ko sama ndode
Ande ak mom dikko gougué téw tchii bépp épisode
Diém naniou maa étiquetté, Lépp cii fénii kesséé
Bou yabo guène woutii pékhé, Ndakh cii rap maa lènii fessééé
Diébelou molène dessééé

{Mao -Chorus}
Wax djou sew bii dafa beurii
Men I’m tired
daniou beug moutiou sama blood
ni vampaya ni vampaya
ni vampaya ni vampaya ( X2)

{Verse 3}
Yeah Yeah !!!
Taay la saar yi gueuneu mokatt
Flow yi gueuneu yokott, Fiit yi gueuneu togattt
Bitch nigga yiy djaay prek lagni nopattt
Nokoss Di Rokoss Kané rofko niou togaatteu
Album bou guéneu hot
Xollou none yi di gueuneu bad
They wanna kill the Killah, But now I feel the deal
Diokh ngama five mé téwoul xam nanii ennemi nga
Yaw yagui tokk triché, Di xarr maa trébuchet
Xamo tchii mane loudoul ay mother fuck préjugés
I’m from the bottom, I’m on the Top
Dioxogne maa baram, I don’t give a F**k
Xamna fima bokk
Diwane Squad dou loxal guène nélène wala Bokk

{Mao -Chorus}
Wax djou sew bii dafa beurii
Men I’m tired
daniou beug moutiou sama blood
ni vampaya ni vampaya
ni vampaya ni vampaya X2
Hummm éh éh éh

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR