LYRIC

{Into}
Hey lèeeeeeeee
Oh Nana Nana
S oooooooooòo s
Maydè
Oh secours
Weuy walooooo

{1st Verse}
Incompetence
meunoul dokhol rew
Sou niou confiance
sopi nguene ko new
Sene arrogance
Sa tass si rew mi rew
Trop de défaillance
Sa takh fou né niou ngui latchté lou khew
Rest in peace
Doctor Cheikh Anta Diop
Rest in peace
Dia Mamadou
Nioune dè tiiiiiiiiiiiiss
Reka la niou Gaup
Kou guessou guiss
Nakhar bi niouy yendoo
Kou nieuw ba nga fog nè mo tanè fekeu mo gueuna yess
Ray nio ki discours
defarou kheuy nè mess
Raylè la dialè
la sakhami ko mou ress
Jouer niou ay sale Tours
Dou fi lou bess
Let’s everybody be aware
nelaw yi da doy fog niou khipi khol
Let’s everybody be aware
ligne niou diapè nèkhoul si khol

{Chorus}
Da niou diooy
ba sou niou guët yi dessatoul ndokh
Youkhou weuy yooy
Guissou niou kèna Kou niou nax
Nièp yooy
Khiif soneu Mar Bay lokh
Beug mou doy
niouy dirèkou ramouniou Bay dokh
Yërmandè
La niouy sakou si yène gni si kaw
Guèssou lene gni si soufff
Yërmandè
La niouy sakou si yène gni si kaw
Guèssou lene gni si soufff

{2nd Verse}
Kagne lay doon
Kouy walou askane wi
Kagne la Kagne la kagne lay doon
Kagne lay doooooooooooon
Kou niouy walooooo
Amou niou lou niou lekeu
Amou niou lou niou Naan
Bouy khiin di mbeundeu
si ndokh mi la niouy fanaan
Ko guiss mou ni tek
Ndiakharé Ko Daan
Seungueem rogogne yi di gawa tokh ni salaan
Ndokh AK courant
Yèksègoul si Yena gokh yi
Ba tay
Étudiants yi
dèkou sokh yi
fac gay champ de bataille
Ndiang mi di sookh
prof yi grève thiow li dou tay
Patch mi téwa dokh
mak yi wax tayi
Baykatt ba ngui diooy
Sameu Katt bi napp Katt bi sokhla Kou lene gueussou
Weuy yooooooòooooooooy dafa doy
Aleu ba ngui latch walam bou lene ko Gass soul

{Chorus}
Da niou diooy
ba sou niou guët yi dessatoul ndokh
Youkhou weuy yooy
Guissou niou kèna Kou niou nax
Nièp yooy
Khiif soneu Mar Bay lokh
Beug mou doy
niouy dirèkou ramouniou Bay dokh
Yërmandè
La niouy sakou si yène gni si kaw
Guèssou lene gni si soufff
Yërmandè
La niouy sakou si yène gni si kaw
Guèssou lene gni si soufff

{3rd Verse}
Oh secours SOS
Maydè Appel de détresse
Oh secours SOS
Maydè appel de détresse
Kagne lay done
Kouy walou askane wi
Kagne la kagne la Kagne lay done
Kagne lay doooooooooooon
Kou niouy walooooo

Da niou lene fale
Di lene fay pour nguene liguey
Bayi lene si khel
Delo thieur bi gni ko mom
Ame lene khel niou ngui lene di khaar nguene liguey
Bou lene bone loo sou niou khol di sedoo sou niou koom
Da niou lene fale
Di lene fay pour nguene liguey
Bayi lene si khel
Delo thieur bi gni ko mom
Ame lene khel niou ngui lene di khaar nguene liguey
Bou lene bone loo sou niou khol di sedoo sou niou koom

{Chorus}
Da niou diooy
ba sou niou guët yi dessatoul ndokh
Youkhou weuy yooy
Guissou niou kèna Kou niou nax
Nièp yooy
Khiif soneu Mar Bay lokh
Beug mou doy
niouy dirèkou ramouniou Bay dokh
Yërmandè
La niouy sakou si yène gni si kaw
Guèssou lene gni si soufff
Yërmandè
La niouy sakou si yène gni si kaw
Guèssou lene gni si soufff

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR