LYRIC

Aahha ha hum
Xale xaliss yaw
Yaa know

{Mist’Ara – Verse1}
Aha aha ha (rire)
Xalé xaliss néna Flac lay nani Coupe of beer
Touh shiit enheu enheu lay sani
Dohé tankou shéytan yi Ndank raak loy bandit
Yaw mandi wo dé wo touho loudoul bén kani
Sa pa dalay joh money
Sa maman nalaw ngay keuf auto bi run ni
Anani, da yor cash beug mou burn ni
Girl def na freek hess rk la geumi
Xaleee…
“Mame newon nani bougn dèf xaliss si bopam bi
Goné la hamagoul motah gnou toudé ko xalé money yaw”
Ham lou bop aatane loum gaw gaw dougnou tok ba marre
Halé yi top ay kaw kaw domou cheikh amar
Nénagn xalép xaliss day mélni El hadji Diouf
Boum la bouh bangay djéma nane dom kon sa léhay douff aahh
Xalé la geum téy mess thi téf
Fétou la geum ne new thi def
Xalé la hamagoul adouna motah mou beug di gnodi ay fresh to dath
Xalé xaliss fi xalé buzz xalé bi diwo na lait
Wanél wanél djizz nafi reuss sougnou poche yi douna lé
(Ko)

{Chorus}
Xalé xalé xaliss xalé buzz xalé carte gab
Yeukeuti na dal yi wané teush yék décapotable
Xol lén xalé xaliss (manga né)
Xol lén xalé xaliss (manga né)
Moné amoul loum beug daf koy dieuli thi pochou Pa bi

Xalé xalé xaliss xalé buzz xalé carte gab
Yeukeuti na dal yi wané teush yék décapotable
Xol lén xalé xaliss (manga né)
Xol lén xalé xaliss (manga né)
Moné amoul loum beug daf koy dieuli thi pochettou Ma bi

{Verse 2}
Xalé xaliss am na valise loum beug day wo maman wala papa
Doni na miss né thi affiche déf ba dieulé fi méga débat
Doni na bitch da beuga riche am cheveux naturel ba dieund thi ba
Ba dieund thi lénéne bi liguéyoul lohom bi tang na wayè néna la vie ça va
Yégal na personally, yégal na life mou indilko anomalie
Toudé ko xalé money, Toudé ko sa biatch biatch fété mani
Tè hamoul louy economy sa école langui kay wan la finga thiy aw
Nga yégal sa finger bi wathié sa rythme bi doundou xalé money dou mana law ahhh
Beug na poukaré wanéwou foum guissé nit
Bou diaré top Youssou Waly Pape Diouf ba zenit (Thiey li)
Eeh xalé xaliss kaayy (kay Kay), Mak yaw gnou déf diotay (kay kay)
Fo dieulé money maytoul bouma wah sa pochou bay
Sa pochettou maman nga iri thi sath si money ba moudjou nga iri thi showi
Yakamti guén thi quartier indi fi riirrr
Ba moudjou nga indi fi thiow
Xalé xalé xaliss xalé buzz xalé domou ngour
Run thi capital def na teud tay dé don na bour

{Chorus}
Xalé xalé xaliss xalé buzz xalé carte gab
Yeukeuti na dal yi wané teush yék décapotable
Xol lén xalé xaliss (manga né)
Xol lén xalé xaliss (manga né)
Moné amoul loum beug daf koy dieuli thi pochou Pa bi

Xalé xalé xaliss xalé buzz xalé carte gab
Yeukeuti na dal yi wané teush yék décapotable
Xol lén xalé xaliss (manga né)
Xol lén xalé xaliss (manga né)
Moné amoul loum beug daf koy dieuli thi pochettou Ma bi

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR