LYRIC

Yakarouma ci kenn dou beute frontierou Cana yi ni mexicain
Moussou ma tok ba xalate ni meunoumassi ci guenn
Nigger doma raw ta doumalawane ni ma ngi dem
Yeah, yakarouma ci kenn
Ndakh ken dou seddok mane bakar yi ma fi def
Kene menoul fene ba dou fene pour nek nandité
Wolotouma labbe’k Imam bilay Djité
Waw boy yakarouma ci kenn
Waro bok’ak gnom Job nekkal kilen di fay
Dakh gni tekkiwoul gnoy yambar you makk yi tay
Boul nangou lapp si say ronkhogne demal nga diangui feey
Wax nga degg bilay Mbeuguel da beuri dolé
Wayé mane samay beugue beugue ma eupeul dolé
Fi nga werou degueuroul ta sou waddé nga thiolé
Xarouma kenn ci lenn dakh boko defoul do dem
Motakh yakarouma ci kenn
Kone boulma deff nissa dom
Yakarouma ci yaw
Ya sagna wax yaw ni mala geunal sa dóm
Té sa dom dou wett ni mane dakh mi ngi sa wett yaw
Yakarouma ci kenn

Sou feké da ngay goungué, si guinaw rek ngay nek
Goungué wouma kenn nigger, dou benn nigger
Yakarouma ci kenn nigger

Yakarouma ci kenn
Dou ndimbal dou chance boy douma sani dé
Do mousseu degg kounane Dip boudoul mane dou dem
Bokou mak gars yi meuneugoul naane ma ngi diem
Hun! Yakarouma ci kenn
Dou serigne, dou magistrat dou magicien
Waxoumalak Macky Sall ak ay ministeram
Fuck Jail ta dou hopitalay dindi febar
bi Yakarouma ci kenn
Sama life loumou Saf Saf ni kani khegne
From the bottom to the Top magic system
Dina weulbeuti sen Rap ni Wati B
Te yakarouma ci kenn
Douma dara mais kenn dou lepp lolou rek waral malay wane louguen doul def
Douma kenn ta kenn dou mane lolou ma teré talal lokho di yalwane
Yakarouma ci kenn

Oh Shit! Sama texte yeka tilim
Teksi diaxasso boy nekhoula lire
Ta soumakoy tek boy no def mou clean
Dakh deugg moy fegn right ligne par ligne
Yo my nigger biss doma guissati
Doussi mane mais si adouna bila
Lepp lo guem diko def mi ngi si yaw
Boul niane ken dimbalila
Geum sa boppay takh nga dem
Ak respect chef dou taxalé
Go hard……
Boumou tiol mouk ba ngay Sos No!
Legui nala lerr ni mak yaw bokouniou
Nio nirou beugn you wekh mais yorouma sa xol bou gnoul bi
Guisso may ligueye guemo dina fayekou yakh
Gni done beuri rée di gass pour nga soulma si pakh
Mane yakarouma ni baak momay guené ci tenn
Ni yeneu boy yi yakaré ci bac pour dem diangui cité
Taloumalen boul fokni ma gui ci yen
Self made mo fucker!
Boul fokni ma ngi sen gane mo fucker!
Yakarouma ci kenn

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR