LYRIC

{Amdy}
Nit gna ngi déééééém
Nit gna ngi déééééém
Nit gna ngi déééééém Nit gna ngi déééééém
Nit gna ngi déééééém outi tougueul
Nit gna ngi outi tougueul séti fou gueune
Seugueum Njite yi légui légui xamou niou kou tchi gueune
Kou nieuw ak gueuteum nga gueum dou gueune
Dou gueune kifi nékone
Wouyaaay Wouyaaayé yaaay
Wouyaaay Wouyaaay Wouyaaayé yaaay
Bamouy dorr tcha Léopold, Léopold nopi diokh Abdou Ndiol
Abdou Ndiol nopi diokh Goorgui LAYE, Goorgui Laye nopi Djimbori Sall
Té bobou ba légui légui Reew ma ngi MAQUIS
Wouyaaay Wouyaaayé yaaay
Wouyaaay Wouyaaay Wouyaaayé yaaay

{Refrain}
Mbir bi dou lène loudoul kou thiop diokh sa maram thiop beu suur
Bou thiobé beu suur diokh moromam thiop (x3)

Hmmm Hmmmm
Niou ngi gueuneu xiff
Waaa waaa waaaa
Niou ngi gueuneu Maquis
Xolal gni am di gueune di am
Gni niaak di gueune di niaakeu

{Nitdoff}
Dream dafa deupou moudjou done sunu nightmare
Gueuleum beug weugou gueuneu dess ci sunu naathie marre
Kène xamoul naka lagni moudjé ci bi tarr tarr
Harvard djangalou lène loudoul I Got lot of Money
Daar daar Bakane yi di rott melni barbares
Taukhidouneu rek ci sa jaar jaar
Boy yi gni ngi diaar guedj niènène gni di teud jail
Fek kifi gueuneu nullard néko corrigél
Nit gni nio ngi lott wédi wouniou GOD
Ngéw yi digni sott doléle gnigniy nott
Niom Nioy
Dammeuh sunu tankeu Mankeu sunu Kom
Ray suniou djom Sunu njite yi dh Niom nioy
Sén Politique moniou yéw moniou djaay Ay Corrompu nio niou ték sunu failles
Diamonoy Indépendance batay guéni sébéti té meunou lène fékhé ba taaay

{Refrain 2}
Mbir bi dou lène loudoul kou thiop diokh sa maram thiop beu suur
Bou thiobé beu suur diokh moromam thiop (x3)

Séni domeu diour sunuy dom
Séni domeu yilif sunu dom
Xolal gni am di gueune di am
Gni niaak di gueune di niaak
Waaawaaaw
Séni domeu diour sunuy dom
Séni domeu yilif sunu dom
Xolal gni am di gueune di am
Gni niaak di gueune di niaak
Waaawaaaw

{PPS}
Politique yi danio ladj légui lerr neu naagneu
Nakhé mbaay bi diekhna tay Jeunesse bi yéwou nagn
Beugeutougn guiss Sénégalou guerr ak yaama nekh
Délo ci valeurs yi makk yu baakh yi yagg xexkh
Opposé woul ni tache bou nioule ci loxo xessal katt
Yakkou yakkou yi sunu euleuk leu fessal kat
Bagn gathié ga ngi téw té nak faaw niou yessal baate
Sunu bakane lagn tchi gan..ngir sunu euleuk naate
Un nouveau jour se lève chers compatriotes
Ecrivons notre histoire faire comme patriotes
Nous avons la foi, la science et les qualités
Faisons du Sénégal de nos rêves une réalité

{Amdy}
Séni domeu diour sunuy dom
Séni domeu yilif sunu dom
Xolal gni am di gueune di am
Gni niaak di gueune di niaak
Waaawaaaw
Séni domeu diour sunuy dom
Séni domeu yilif sunu dom
Xolal gni am di gueune di am
Gni niaak di gueune di niaak
Waaawaaaw

Yako wakhone
“Mandat bi 5ans lay done”
Yako wakhone
“Justice bi yémalé nieup”
Yaw Yako wakhone
“500.000 emplois”
Prési yaw yako wakhone
Transhumant Thiaga politique
Yako wakhone
La patrie avant le parti
Yaw Yako wakhone
Dessert Colonial pour les soumis
Prési yaw yako wakhone

La magie du clic fera face à la puissance du flic et du frique
Vous nous aviez promis une gouvernance sobre et vertueuse
Mais nous avons une gouvernance sombre et vicieuse
Diko bakhé nieup niou takhawou Sénégal beu xeuy délou sunu Borom. Rest In Peace
We Are Senegal

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR