LYRIC

{DIP – Verse 1}
Dembe la tek sama yone dina dem soubeu téél
Dem na ni biss bimay déh djotna kène douma téyé
Ma ngui cii yone di dem kone boul laathie fouma nek
Sou féké yone bi dou pour mane kone Yallah bouma yégue
Dama cii gueumeu té teukh douma wakh douma dégueu
Def na ci lima amone lepp bataye gars yi yéé ngui may réé
ADUNA laay diaar rombeu SAFARA dem ALDIANA
Sonouma bay taayi yone bi xamo loumou ma diaral
Yolou rythme ak rimes dou niakkeu nioula beug fuck
Yène saay beut taa waayé rongogne gna gueudjeu tokkeu
Nieupeu beug bokk niou beuré beug dem
Gni ndieuk yégue moy gni cii gueuneu niémé déh
Ndax bo gueumé sa bopp sa xol li tchi nék ngay def
Boy life aaleu leu té faaw nga nek gaïndé
Fima tolou nii pour mane CHANCE meunoul gueune ESSENCE
Fokk ma FLY weuy gueuneu SCIENCE ni mister RENAISSANCE

{Refrain}
Boy dafa djot ma khaali sama yone
takk sama fiit gueuneu farlou cii sama job
Xam fima joggué gueuneu fass sama djom
Ba yégue fima dieum.
Yeah ! Boy dafa djot ma khaali sama yone
takk sama fiit gueuneu farlou cii sama job
Xam fima joggué gueuneu fass sama djom
Ba yégue fima dieum. Right !

{Fla The Ripper}
Renaissance album brought respect and admiration
Humble and patient inspired a whole generation
The plan is now a program we’re on the mission
Share the booth with dip for another life’s lesson
Coz we got a lot in common
Promess Bouba will do this collaboration coz you deserve it
Time tell just do it well to make it in heaven pass through hell
Brick by brick build your own empire
Raise the bar higher
You just don’t have to be good but the best
Bury the rest watch your steps, everytime somebody will try to break your neck
I rather die like a man than live like a coward
We all human but we all got power
Everytime you hear I’m on another classic
Can’t stop thisss another fla status like emoticon

{Refrain}
Boy dafa djot ma khaali sama yone
takk sama fiit gueuneu farlou cii sama job
Xam fima joggué gueuneu fass sama djom
Ba yégue fima dieum.
Yeah ! Boy dafa djot ma khaali sama yone
takk sama fiit gueuneu farlou cii sama job
Xam fima joggué gueuneu fass sama djom
Ba yégue fima dieum. Right !

{DIP – Verse 2}
Li dess saa eupeu fouf
Lima djotta def motah may gueuneu pouss
Ndax fima beug dem Fokk ma am nima mel
Gueuneu yokk vitesse, nguir meuneu songue li dess
pour feusseul sama bidéw Hann !
Ma ngui djégueulou mais fallait que ma def ko
Ndax fima joggué ak gni fogone nii damay fo
Douma doundou lou tarr tameu khonette di téndéfal
Ma tanal sama bopp loutah kénène dimako défal
Dina nangou nek boy nékalé makk
Nékal gni nékal sen bopp nékalél maa
Rythme bimay Démé koumay toppeuh di nga gaagnou
Fima nekka kawé soumay khol cii souf di daanou
Yakamti yék xeuy rek tégou cii yone
Nama Yallah baal xeuyna meussou maka tek cii yone
Damay DEM douma TOKK dii KHAAR ngène DIKKEU
ALLER sans RETOUR Bokoutak DAKAR DEM DIKK

{Refrain}
Boy dafa djot ma khaali sama yone
takk sama fiit gueuneu farlou cii sama job
Xam fima joggué gueuneu fass sama djom
Ba yégue fima dieum.
Yeah ! Boy dafa djot ma khaali sama yone
takk sama fiit gueuneu farlou cii sama job
Xam fima joggué gueuneu fass sama djom
Ba yégue fima dieum. Right !

{Outro}
Yeah you got the most anticipated mixtape
#BisNikiTay, DIP.
Get ready we coming
It’s calm before the storm .
Fla The Ripper I’m out !

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR