LYRIC

{Verse 1}
You….You….Youssou…Ndour
You….Youssou….You….
Dérett dina séneu di guèné cii say paxou bakane
Diss la déh té mane ass douma ray
Talent kagne ngay fay Books ak Supa’Ced
Dérett wala dérett parce que yeurmandé meussou niou djik
Dina fêté sakh beuss bouniou lay souli dji
Déféko comme nignou koy défé bountou pikine
Businessou mercedes limosine Doundou Guiss nio xéw nigga nio botte bouki bi
Golo bi moma gueuneul Gucci Luis V. Rappeur yeup bolène téggalé douniou soutt dip
Doffo nigga ba di bougé mêtre
Lo meunti wakh dinala couté chere
Nioma meune té dougneko prouvé dh
Yo nga dagnelay tathiou pour nga déh
Niofi né té maay takkeu capitaine
Do guiss Messi di tek cii Habib Beye
Diobalma album niou songueuh amitié
Nio xam na mbède bi mèrr sama famille bëg
Nieupeu beug fégne sama clip
Mane ma beug joué ci ay film
Niémé ray niémé déh dama sikkeu
Yaw gaïndé nga? Gaïndé bouy simbeu
YOU néna “foulay djaay dakaar”
Waayé Dakar kèneu dou dieundeu fouleu
no mbokk mane awouma djotou Hindou boulma nopp
Door rek ba téddeu am ay 5000 toureundo
Mane akka ma djaffé darr
Ni gouné bou magga ndo ak ay Pa
Life bi course leu takh ma done athlète
Maak sama gang bi kèneu dotoul tok arrêt car

{Refrain}
Fepp laay dém melni Youssou NDOUR
Beuri bayré melni You
Bisness lay def melni Youssou NDOUR
Guichet fermé melni You
Niémé risque, investir, Ministre, Disque d’or (You)
TFM, RFM, L’Obs, Grammy Awards
Youssou Ndour Youssou Ndour
Wowéma wowéma Youssou Ndour
Youssou Ndour Youssou Ndour
Wowéma wowéma Youssou Ndour
Youssou Ndour Youssou Ndour
Wowéma wowéma Youssou Ndour
Youssou Ndour Youssou Ndour
Wowéma wowéma Youssou Ndour

{Verse 2}
Akka maa mare louma mandi-lo def loma tatte té dou sangara Nigga
Sakhaar ak safara xalleu cii sama guémigne nane laay teudjé sama gatte nigga
Dakara-ra car-car-car-car def nama star law-la-thiat nigga
Antane na aduna bi damaka yénou rek saniko gauche wala droite nigga
Rangalnéna rangalé rangalé boppou niou beugona gorr sama baate nigga
Alaxam faté nala ci guinaw soma namé dél khol ci kanam nigga
Bakaar ak xaliss nioy fanane boul défate lou xarram té amossi alale
Meussouma guiss Malakka bou baax bi maxala toubab bé djangal kiy djangal kima djangal
Maay thiow li thiow manela maay haut niveau bi
Nio ngui job di diomilo gni fokni fo leu non damay thiauki
Dama profito ci song bi tokk ci bopp tokk psycho yi
Fuck Hip Hop bi Fokk niou fayma sama money
Thiow bizz gaïndé djoni djoni ndiaye mbauraudi
Armaumi moussouniou lekk mbëddeu Armaumi
Akku nama tata ! Boy Underground boumafi saga nala lerr ni saga nga koula matt PAPA
Sène Rappeur bi ngène gueumone légui nieup dém naniou ba xamni thioné leu ndax mane
Waayé nieuw lène ma doumeuh lène taf-taf,
Leundeumaay diomaloul borom beute yuy takkeu
Té mane ci la deukkeu motah rappeur yima fay yeup boy kène dotoul meuneu takkaate

 

{Refrain}
You….Youssou….You….
You….Youssou….Youssou….Youssou
Fepp laay dém melni Youssou NDOUR
Beuri bayré melni You
Bisness lay def melni Youssou NDOUR
Guichet fermé melni You
Niémé risque, investir, Ministre, Disque d’or (You)
TFM, RFM, L’Obs, Grammy Awards
Youssou Ndour Youssou Ndour
Wowéma wowéma Youssou Ndour
Youssou Ndour Youssou Ndour
Wowéma wowéma Youssou Ndour
Youssou Ndour Youssou Ndour
Wowéma wowéma Youssou Ndour
Youssou Ndour Youssou Ndour
Wowéma wowéma Youssou Ndour

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR